Ma Cha Allah je suis toujours ses émissions, Qu'Allah l'accueille dans son vaste paradis mais j'aimerais avoir la suite de Zahra quand elle parlait de la patience
Masha'llah amna solo lole sah ya seyda yalla nako yalla yerem ta kharéko thi dianatou firdawsi oustaz yalla na sougnou borom yokou khamkham bi mayla goudou fane
Seyda Zeynab, mala sope! Yalla na am ay dome you djiguène you melni yow. Djikko djou bakh, rékka woor. On perçoit l'amour, la bienveillance et la miséricorde dans son regard.

Ndeysaan yaye yalna yalla yeesal yermandem ci sa kaw
Masha'llah amna solo lole sah ya seyda yalla nako yalla yerem ta kharéko thi dianatou firdawsi oustaz yalla na sougnou borom yokou khamkham bi mayla goudou fane
Macha Allah yalla naniou yalla dèfal diam ak khéwal tawféh soutoura
amiine thi niane yi li nga wakh degue la machallah yalna yalla degeural tahawaybi amatina solo
Seyda Zeynab, mala sope! Yalla na am ay dome you djiguène you melni yow. Djikko djou bakh, rékka woor. On perçoit l'amour, la bienveillance et la miséricorde dans son regard.
❤️❤️❤️❤️
Macha Allahou
machallah
Am na solo lol
Machallah