Ndaysaan 😢 cette conférence fut ma rencontre pour la première fois avec Oustaz Ba sur la télé. J’étais extrêmement ému de la manière dont il faisait sortir naturellement les connaissances. Que la le paradis soit sa dernière demeure.
Masha’Allah Oustaz Ahmad Ba sa mission mat na. Borom khol bou Rafet bii , ya labiirr sii xam xam. Ya bakh. Yalla nala Yalla yeureum té xaréleu Janatou firdawssii. Amine ya rabbi
Il avait un don de Dieu je l’ai une fois entendu dire que tout se qu’il entends une fois il le mémorise et cette émission le preuve sans feuille de route il a dérouler sa connaissance du coran Ba tu me manque Walahi
Il était une fierté pour toute la Umma et particulièrement pour la tijaniya. Qu’Allah SWT dans Sa Miséricorde infinie l’accueille au Paradis auprès du prophète Mouhamad aleyhi salaatou wa salaam
Massah Allah Oustaz voila une connaissance parfaite accompagné d'un raisonnement coherant. nous sommes très fier de vous oustaz que Dieu vous accompagne dans votre quête perpétuel du savoir.
Walahi oustaz niak nagnou lou reuy lou bah wayé kou mat si yalla guédiou ham ham yalna hipé ardiana firdawsi si pég mawlana elhadji Ibrahima niass ❤❤❤❤❤❤
Allaahouma ighfir lahou war ham hou. Une immense perte pour la Umma. C’est un plaisir incommensurable de l’écouter. On ne veut même pas qu’on l’interrompe!
Li may reccu ci sama àdduna bokk na ci li ma ko siyaare wul ci bi muy doon 😭 Seex Ahmed Ba yërmande Boroom bi SWT wacc ci moom ci barkeb boroom Tuubaa 🙏
Machahallah Tabarakallahou Dieuredieufety sounou borom bi Dieuredieufety Cheikh li ley Ahmed Ba Que bénédiction d allah 😢😢😢😢 Que la récompense d allah swt envahi ta tombe ta dernière demeure 😢😢😢😢 Quel perte 😢😢😢 Apprécié les gens de leur vivant 😢😢😢 Pas la mort leur trouve des qualités 😂😂😂😂
Inna lillahi wa Inna ileyhi radji'ouna qu'Allah soubhanahou wa Ta'ala l'accueille au Paradis céleste Firdawsi auprès de l'Elu Suprême Seydina Mouhamad Salla'llahou aleyhi wa Salama Amine ya Rabbi
الحمدالله علي كل هال جذاك الله خير ياءشتاذفان حخيخت العلم علم السلامي فإن محمد كنشل علم ياءشتاذ جذاك الله خيروزادك الله علم وفهم وكفيت زرولالقيت مابقيت دراللهم صل علي سيدنا محمد وسلم تسليم كشير
Ndaysaan 😢 cette conférence fut ma rencontre pour la première fois avec Oustaz Ba sur la télé. J’étais extrêmement ému de la manière dont il faisait sortir naturellement les connaissances. Que la le paradis soit sa dernière demeure.
Amine
Masha’Allah Oustaz Ahmad Ba sa mission mat na. Borom khol bou Rafet bii , ya labiirr sii xam xam. Ya bakh. Yalla nala Yalla yeureum té xaréleu Janatou firdawssii. Amine ya rabbi
Amine ya rabi
Amiine
Alahouma amine
Amine barki alhourane
Yalna Yalla Yeureum Oustaz Ahmed BA !
Machallah machallah machallah khôl sédd na gouye. Na nieup niaanal Oustaz Ahmad Ba aldiana firdaws !
Amin ya Rabbil Halameen
Il avait un don de Dieu je l’ai une fois entendu dire que tout se qu’il entends une fois il le mémorise et cette émission le preuve sans feuille de route il a dérouler sa connaissance du coran Ba tu me manque Walahi
Il était une fierté pour toute la Umma et particulièrement pour la tijaniya. Qu’Allah SWT dans Sa Miséricorde infinie l’accueille au Paradis auprès du prophète Mouhamad aleyhi salaatou wa salaam
Oustaz Ahmed ba yalla ne yalla doli yeurmade ❤❤❤❤❤❤❤😭😭😭😭😭😭😭
Machala oustaz Ahmed Ba yalla na Seydina Muhammad psl di dekeundo wame sa firdawsi
Oustaz Ahmad ba😭💔 Mourabbil Qawmi❤️❤️yalna🤲🏾🙏🏾 yallah yokou leeram tè taasniou thi barkèm ya rabby 🤲🏾🙏🏾
Yalna aldiana di sa keur ya oustaz 🙏
Amin ya Rabbil Halameen
Karama Baye Niass daal ay dieum domou adama la té liila Serigne bi wakhon machala.
Gfhfvw je cw dvx. Drcwgv😂😂❤c svscs
Macha allah oustaz Ahmed bâ ma fierté. xam xam rek am gueu KO yallah gueu am Aÿ fane you goude si barke baye
Massah Allah Oustaz voila une connaissance parfaite accompagné d'un raisonnement coherant.
nous sommes très fier de vous oustaz que Dieu vous accompagne dans votre quête perpétuel du savoir.
Ĺ g
'
Rcxbfjg
Mais hey h😮😢ghht
@@nfamarasonko9797 cj b vraiment vj😊bvvx🎉
Walahi oustaz niak nagnou lou reuy lou bah wayé kou mat si yalla guédiou ham ham yalna hipé ardiana firdawsi si pég mawlana elhadji Ibrahima niass ❤❤❤❤❤❤
Diokandial Ouztaz Bâ woo réffou diambar . Yassam rog aa mignandong méne toté aa yonne foo oo wode. Allahouma amine
ادام الله عزکم فی الدنیاوالاخرة يسرنی باستماء صوتک وبرؤیة وجهک الکریم الشیخ الکبیر وحبیب الکریم استاذاحمد به بقی الله عمرک مع صحة وعافیة ورزق واسعة
Mais ghfjwvkglgjfv❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤rhfvc
Réponse en paix oustaz Ahmed ba que aldianatoul firdaw soit sa demeure éternel allahoumma akfirlahou wo arhamahou gorko diouldo yehi handé
Un université de savoir ❤yalna say lerr yoku si barkè cheikh I Niass
Mach Allah ya oustaz Ahmed ba deuge deuge diabar le bou ver la
Macha Allah! Borom xam xam deugu deugu Oustaz Bâ
Ma'shallah Oustaz belie bague nala love from The Gambia 🇬🇲
Sister ki mom sama sopé la machala brom kham kham bou modeste la
Machallah oustaz Ahmad ba yalnala yalla samou sa goudal sa fan amiiiiine
Wallahi ya cheikh ahmed ba
Yall na la yall fayye
machalla ya ostas yalla nala yalla defal diam sedal ga sounu khoule lole yalla na yalla sedal sa khoule
ya oustaz yallana yalla yageuale laffiii te andeu ak wéérrrrrrrrrrŕrrrrrrrrr
Xam xam gou sélleu ya ouztass yalla nga fi yague té werrr
yallah nala yallah faye si lou bakh ligua defe
sa kham kham léér na ya oustaz yalla na yalla goudal say fane
Cet homme d'une dimension spirituelle très avancée qu'Allah lui agréer son paradis
Dieureudieuff oustaz ...yalna Baye Niass fayla
Medina baye capitale du savoir islamique mashallah
Xam xam bi machallah lerna worna yalna yalla yokou xam xam bi
I guess I am kinda off topic but do anyone know a good place to stream new tv shows online?
@Juelz Finley Try FlixZone. You can find it by googling :)
@Mekhi Finn definitely, been watching on flixzone for since april myself :)
@Mekhi Finn thank you, I went there and it seems like a nice service =) I appreciate it!!
@Juelz Finley Glad I could help =)
Borom bii doli yeurmandé si mom yarabi Daraji inshalah yala si Yala def ay yenen Oustaz Ahmad ba yarabi 🙏
Amin ya Rabbil Halameen ❤❤❤
Allaahouma ighfir lahou war ham hou. Une immense perte pour la Umma. C’est un plaisir incommensurable de l’écouter. On ne veut même pas qu’on l’interrompe!
Li may reccu ci sama àdduna bokk na ci li ma ko siyaare wul ci bi muy doon 😭 Seex Ahmed Ba yërmande Boroom bi SWT wacc ci moom ci barkeb boroom Tuubaa 🙏
Machalla Oustaz yalla gnouko yalla fayal c'est une fierté de la fayda
Machala yaw yalla na la yalla yagale fi
machallah al oustaze ... yalena yalla yokk lėr tė goudal say fane !
Macha Allah yalle na yalla yessal yeurmadem si mome
Machahallah Tabarakallahou Dieuredieufety sounou borom bi
Dieuredieufety Cheikh li ley Ahmed Ba
Que bénédiction d allah 😢😢😢😢
Que la récompense d allah swt envahi ta tombe ta dernière demeure 😢😢😢😢
Quel perte 😢😢😢
Apprécié les gens de leur vivant 😢😢😢
Pas la mort leur trouve des qualités 😂😂😂😂
Allahouma amiiiine
Masha'Allah Ya Oustaz may Allah guide you very inportant lecture. The only guide is AL'QURAN KERIM KITABI
Machalla Oustase amaht Ba wakh bi rafait na trop
Machallah oustaz.....borom kham deug deug moye yaw
Mashaalla oustaz Ahmad ba waxtanwi amatina.solo loool dieurdieufti.
استاذ الاستاذ. . . كأن الذمخشري يتحدث ادامك الله بالعافية و الصحة التامة بجـاه الجاهي ❤🙏🏾
Rahmatullahi talla anhou, Oustaz Ahmed BA Borome xam xam bou Maague😭😭
Laye diassè vraiment loi nèxna lool waay jerejef yaa oustaz
Ndayssan oustaz ahmed ba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ya ALLAH accorde oustaz bah dans ta miséricorde infinis.amine
Sa kham kham wéer na machalla Oustaz Ahmed Bâ !!!
Machallah dieureudieuf Bay Niass diarama Thierno Abdallahi Dia
Macha allah khole toyna
Jërëjëf Ouztaz Ahmed 🤍
oustaz forfu khawnaa khoote.....mashallah ya oustaz .
Ha jarama bah pouhlo yo Allah rééne ayna.
Machallah goudall fane lloll
Machalah ! Paix et à son âme .
Machalla ya Oustaz Ahmed Bâ.
Mashallah ya oustaz ataaha lahou baxahouka ♥
Allahouma ighfirlahou warhamhou
Amin ya Rabbil Halameen
Machallah ❤️ ❤️ ❤️ machallah ❤️ ❤️ ❤️
Paix à son âme yo allah yourmobe yaafob Amine
Qui est la en 2022 beuseul j'aime ❤
ماشاء الله جميل جدا يا استاذ ابلغت واكملت واحسنت حفظه الله وايده ونصره مع صحة وعافية
وانتم.كذالك
شيخ أستاذ أحمد به شكرا جميلا
macha Allah oustaz ba
Macha allah oustaz
Ba rafetna
dieuredieufeuti oustaz Ahmad ba
machallah xam xam bi werr na
Machallah Oustaz Ahmed Ba Karama Baye Niass
Ndeysane Yalna yalla yeureum yarabi ❤❤❤
اللهم يسلمك ويحفظك ويطويل عمرك
ويعطيك العافية والصحة العامة والعلوم
Jbc❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
machallah amna solo
Regufjfkwshwchcffdg ghfhxvfjdfcgchhsjfjkn🎉😊hhx❤❤❤❤❤❤❤ftdcw thegsxfw
Mashallah. Douma doyal ci wokhtanam.
Macha allah oustaz ba
Machalla ya oustas
Merci oustaz ba
Mashallah amna solo
Mashallah ousstas
ALLAHOU AKBAR !!!! Que firdaws soit votre demeure eternel !!!!!
barka lahou fika ya cheikh
Machallah Oustaz Ahmat ba
sama sope bi bilay mala beugue oustaz ba
Ma challah Sedy bah
allhamdou lillah macha allah
Machalah ya Oustaze 🙏🙏
machallah ostaz
Machallah......
Mash'Allah
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته بارك الله فيكم
oustaz vous etes parti representant de dieu sur terre "khalifatoulahi fi ardi" gnou leye safo bou wer gui diamou borom bii soubhana tahallah dieurediafé s.aidara mbacke borom faydoul arifina wa soulamou rahibina
استاذ احمد به شكرالك ماشاءالله
Machallah rafetna lerna
Ndeysane oustaze paix à son âme
Oustas ba macahllaa ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yalla nako Yalla yeureum❤
Inna lillahi wa Inna ileyhi radji'ouna qu'Allah soubhanahou wa Ta'ala l'accueille au Paradis céleste Firdawsi auprès de l'Elu Suprême Seydina Mouhamad Salla'llahou aleyhi wa Salama Amine ya Rabbi
الحمدالله علي كل هال جذاك الله خير ياءشتاذفان حخيخت العلم علم السلامي فإن محمد كنشل علم ياءشتاذ جذاك الله خيروزادك الله علم وفهم وكفيت زرولالقيت مابقيت دراللهم صل علي سيدنا محمد وسلم تسليم كشير
ماشاء الله جزاك الله خيرا
Mosi moune machallah
Outass ahmade be sobonalla tourapp
am na solo trop
اللهم اغفر له و ارحمه برحمتك يا أرحم الراحمين يا رب العالمين ❤❤❤❤❤❤❤
Il est fort ce Mr
رحمه الله ورضي عنه ونفعنا الله ببركاته آمين