kénu waroul naw dieuf ak loumou reuy reuy ak loumou kawé kawé wayé tmt kénu waroul khep dieuf ak noumou man di tolou yallana gnou yalla nagoul sounou dieuf you bakh ta diégeul gnou souni dieuf you bakhoul barkép borom touba
يقول ﷺ: والذي نفسي بيده، لا يدخل الجنة أحد منكم بعمله، قالوا: ولا أنت يا رسول الله؟ قال: ولا أنا، إلا أن يتغمدني الله برحمة Mem yonentbi slhw sax budul yërmande Yàlla du dugg aljana ndax moom mooko wax
Mangui nouyou mbolem dioulit tay nemekou tay rafet lou li nguen hamni yatal nguen ko nguir niou meun si dieurignou. Lima si geuneu nex nak moy fin bi nga ham ni wadji si guent la nekon ta niou meun si diangue li nga hamni moy wadji yalla dako beug motax mou wann ko missal bi teuyit diangue nasi ni adouna lo meuneu daw dioublou bour bi sougnou borom diar nako ndax mofi nek tey ta mofi nek demb ta mofiy nek euleuk. Yalla na yalla dolli yiiw ta geun nio guindi ak mbolem dioulit.
Souniou borom ndeysane Aka meun topou détails ndeysane dou bayi been trace , Yallna niou yalla xiir ci lou baax , té mouniouy djégeul souniou bakar yiniou tay ak yiniou tayoul, até niou ci yeurmandém ci Barké PSL (Amine ya rabi)🙏🏽
Mo takh nit ki loumou Diamou Diamou yallah waroul takh mouy naaw ay dieufeum pask nit koudoul dioum amoul donc yallah naniou yallah Geunue takhawou doliniou soutoureu wer katan ak tawfékh moss ak mouthiou mouseul niou si Gaateu faan ak Déh gou niaw tamou may niou moudiou gou rafét inchallah inchallah si barke ya rassoulillah psl
Alhamdulilah que je nais raté pas les 5 prieres d'aujourd'hui merci beaucoup mon dieu ❤️
Yalna niou yalla atte ci yermandem !
Yallah na yallah yessal yermandém si diam gniii Bidiahil seydina mouhamed saw
histoire bi yeme na trop ❤
Macha alla yalnaléne YALLA may télé bou gnéppou beugue diko suivre amine
Amin amna solo lol yala nalen yalla fay tei yokou khalate bi yenagui niouy delossi mashalah
Maachallah. Yalla takhawou leen,fey leen. Contane nagnou lool. Maachallah. Alhamdoulilah
Mashallah amna solo. 1 million de abonez pour... CEN PRODUCTION Allez le gars 💪💪💪☝️☝️☝️
A machalla yalla nagnou yalla até thi yeurmandém té maye gnou aye borome keur you bakh
Je suis tellement content de vous cen production diadieuf
Amna solo loooooool🙏💛💛☝️
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi PSL
ما شاء الله ، حكمة رائعة.
جزاكم الله خير ا
Yalla nane am Yeurmade Yalla 🙏😭❤️
Mâcha Allah amna solo yéurmand yalla🙏🏾
kénu waroul naw dieuf ak loumou reuy reuy ak loumou kawé kawé wayé tmt kénu waroul khep dieuf ak noumou man di tolou yallana gnou yalla nagoul sounou dieuf you bakh ta diégeul gnou souni dieuf you bakhoul barkép borom touba
Amine way
Amine waye
yalla nanou yalla yerem
Subhanalah Alhamdoulilah Lahilaha ilalah Mouhamed PSL Alahou Akbar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah Dieureudief
Sa Profil bi la beugu mane
Mâcha Allah amna solo yéurmand yalla eupouna dédou
Machallah ❤️yalna yallah atté ci yeurmandém🤲
ماشاء الله أللهم بارك فيه فتبارك الله أحسن الخالقين (أمين يعرب العالمين)
Yalla naniou yalla até thi yeurmandém diou yatou té kawé dji
biii laadon Xaar machallah 🙏🙏
Amna sollo gou wérawére❤❤❤
Ndeysane yalla recka diarra wolou
Yalla naniou yalla attei thi yermandeim🤲
Diadieuf cen production histoire bi amna lol yalla nalen yalla fay thi barkèp Serigne saliou ❤️🙏
Jërëjëfëti ! YALLÂH Na ci Japp. Amiin Amiin Amiin…
Macha alla amatina solo lole
Yalenagnou yalla até si yeure manedéme
Billahi Yalla rek moye deug
C'en production yéne lafi yalla tekk 🙏. Islam sa ganam. ❤️🙏🤗
Yalla nanou brom bi yeureum
Amiin Yàlla na nu Yàlla gërëm.
Machalah yallana yalla doli tawfékh
❣️ macha'allah sante yalah bah douma wakh wakhou diambour douma togne kouma togne mah ball'lëu walahi wadji guoré nëu macha'allah Aminata Diallo barhame 🤲🤲🤲🤲🤲♥️♥️♥️♥️nagnou ragual yallah amena solo l'île😭🤲🤲
Amiinne diangalé bi amna solo
يقول ﷺ: والذي نفسي بيده، لا يدخل الجنة أحد منكم بعمله، قالوا: ولا أنت يا رسول الله؟ قال: ولا أنا، إلا أن يتغمدني الله برحمة
Mem yonentbi slhw sax budul yërmande Yàlla du dugg aljana ndax moom mooko wax
Machalah nexna amna solo yalnagnou YALLA atté si yeurmandem té khar gnou ci lou bakh
Amine
Machallah ❤❤❤❤❤amna solo
Michalla yallah rek mon meune
Machallah diadieuf diewrine
ماشاءلله
Macha alla amatina sollo.
MAchallah fière de vs vraiment vs êtes les meilleurs ❣️👍
Amna solo yalana la yalla faye
Machaalla Amna solo.
الحمد لله على كل حال ما شاء الله جزاك خيره
Machalla mana si Tamit ko khamne ni la waxon wayè si niague tague diabar té bari na rou yo khamne mo Lén waron andi diamono ………….
Amna solo diadieuf
Yallah na senn Diam yague vraiment histoire you Amm solo RK mofii daw🙏😍
Mangui nouyou mbolem dioulit tay nemekou tay rafet lou li nguen hamni yatal nguen ko nguir niou meun si dieurignou. Lima si geuneu nex nak moy fin bi nga ham ni wadji si guent la nekon ta niou meun si diangue li nga hamni moy wadji yalla dako beug motax mou wann ko missal bi teuyit diangue nasi ni adouna lo meuneu daw dioublou bour bi sougnou borom diar nako ndax mofi nek tey ta mofi nek demb ta mofiy nek euleuk. Yalla na yalla dolli yiiw ta geun nio guindi ak mbolem dioulit.
Machalla ame na solo
MAACHALLAH nilla dé
Souniou borom ndeysane Aka meun topou détails ndeysane dou bayi been trace , Yallna niou yalla xiir ci lou baax , té mouniouy djégeul souniou bakar yiniou tay ak yiniou tayoul, até niou ci yeurmandém ci Barké PSL (Amine ya rabi)🙏🏽
Amine 🤲🤲🤲☝️🙏🙏🥰
AMIN🤲🤲🤲
Amiiiin
Amine
Amna solo loool machallah
Yaw mi di lire mangui lay gnane nga abonner Sama Chaine Ngir Dieumi Yonent Bi Saws ❤
Paix salut et Bénédiction d'Allah sur notre prophète bien aimé Muhammad ❤ ❤ ❤
Mach'allh dieureudief yallah
Thiey Amna solo
Yalnaniou yalla yeureum
ALLAHOU AKBAR Ndeysane Machalla rafet na amna solo 😢🤲🤲🤲🙏
Machalla
Akassa amatina solo de yalna sa diamou yageu s cheikh ndiaye
Macha Allah amna solo lol 🙏🙏Lou mata bayi khél
Massallho amna solo lôe
Bilahi daguen ma yé
Machallah yalla na niou yalla yërëm
Toujour mangui khar sa ayi video
Amna solo blh kou yabou adiou ci yalla bafaw té khamne mo yorr ndiégal niépp
Amena solo lol❤️🙏
Mo takh nit ki loumou Diamou Diamou yallah waroul takh mouy naaw ay dieufeum pask nit koudoul dioum amoul donc yallah naniou yallah Geunue takhawou doliniou soutoureu wer katan ak tawfékh moss ak mouthiou mouseul niou si Gaateu faan ak Déh gou niaw tamou may niou moudiou gou rafét inchallah inchallah si barke ya rassoulillah psl
Amiine yarabi niou bokouko 🤲🤲😭
Amna solo yal nu yalla yërëm te atte nu si yërmnadeem
Jazak Allha feek CEN
Dama Léna beg bilahi
Amnatina solo 🙏🙏❤️
Maa chaa allaah
AM na solo trop ❤️
Jërëjëf
Machaalla 😭😭
Ohh am na solo
Jah jeuf machallah nalen yalla Faye
Thanks
ماشاء الله وتبارك الله
Ma sha Allah ❤💯❤❤
Machallah amna solo loole
Machallah amatina solo
Machallah amna solo
Merci ❤❤
Machallah am nasolo
Mane Modou fall sopey bara Dia séne vidéo d'où masa raw bou sopé yalla ❤️💯
MERCIAMNASL0
Macallah ❤️
Amna solo LOL vraiment machalla
Machalah dieu merci beaucoup
machalah
MashaAllah Allhamdullilah may God forgive us ❤️❤️
Machalla ❤❤❤❤👍👍👍🤲
Alhamdoulillah masallah
Machahalla
Amatina solo
Mâcha Allah
Machallha