Xolal ma dof bi rék ce karim mom ak thiatt kif kif mentalité zéro pour yén sénégalais yi sou Macky sall nékon thi yonou dioub dinagn ko xéx 😮 Moustapha Diop ak Mame Birame Wathi depuis Macky Sall ba légui changé wouniou nio gui thi yonou deug beuss bou régime bi commencé déf comme niko Macky sall dan défé ngén xam ni wa walfadjri guinarou kén nénou lén Yén kay nafékeu yi yéna changé mais sén bopou rék ngén di nax Sénégalais yi nio lén gueuneu mouss fop 😮
Karim tu as été un idole pr moi mais je me perds Dan's tes arguments quant a leurs buts car j.y vois une confusion innécessaire sur ce que tu veux en définitif.
Sidy Lamine Niasse dafa ni wone journalistu walf yi dé lène and ak peuple bi. Légui peuple bi and ak état bi, yaw Karim nga ni journalistu walf yi warou niu and ak état bi ? Nga lène di traité de guéweul de l'état ? Louy sa problème ?
Mais khrum xax maane léegui la Gueum ni ka tékiwoul dara ndé fi mounéni kou yeungueul kouné mou ande ak yow c'est à dire moome na réwmi tak rék ak nimou meuna také yeupe diaralnakoko
Yen est ce que Sava ?? Nakala askan Wii taxé Diouk té même askan Wii gno dioxx majorité régime Nguen ni askan Wii gnola yoni pour attaqué régime bi ?? Karim néna thiat nitou principe leu 😂😂😂Karim Loula dieulé yen à marre AK bi ngafa guené li ngay d'âne waxx ci médias yi contre y'en a marre ?? Dem collaboré AK makhtar le kagoulard...😂😂😂 Mane je te suis mais khawma lo xexx tu es contradictoire nga balma
Karim me fia rirrr bilyy il me sembl ke kou beug diner lheu kou beug rewomm lheuu mé pour mom lépp khell mou sell mokoy deff manee le jour ou bimiyy wérénnté ak benn oustaz mouy waxx alhour an mom mouy waxx li khell nangou
Karim Niit kou deugou leu bilahi
J'aime cette journaliste ❤. Elle est free
yawak man nio yém si lolou ❤
Je confirme Karim. J'ai connu l'homme en 2012 quand on combattait le troisième mandat de Wade.
Kouléne guena bagne réwmi amoul kougnou falle ken Bala mouye tokk sakh yéna ngi préparé pour khékh ko
Bou Moustapha Diop mélone comme yéne doléne def émission mbir walf wala gnou censuré léne
Karim gueye train bii dakofé bayi
Yow mom ken hamoula😂😂
😂😂😂😂😂😂 yaw Ya khadi guén la siw dakh la liguey bi .
Nganan ya khadi moy kan😅😅😅
Thiate degue puir la wakh surtou 100 limite
La jalousie rend fou
Ki mom weroul . Inchallah dou dougou ci parlement bi deh
❤❤❤❤
Xolal ma dof bi rék ce karim mom ak thiatt kif kif mentalité zéro pour yén sénégalais yi sou Macky sall nékon thi yonou dioub dinagn ko xéx 😮
Moustapha Diop ak Mame Birame Wathi depuis Macky Sall ba légui changé wouniou nio gui thi yonou deug beuss bou régime bi commencé déf comme niko Macky sall dan défé ngén xam ni wa walfadjri guinarou kén nénou lén
Yén kay nafékeu yi yéna changé mais sén bopou rék ngén di nax Sénégalais yi nio lén gueuneu mouss fop 😮
Ioe tu es le vrai fou
Karim tu as été un idole pr moi mais je me perds Dan's tes arguments quant a leurs buts car j.y vois une confusion innécessaire sur ce que tu veux en définitif.
On doit les honores car certains d entres eux étaient des victimes mais pour la vrai 8:34 e histoire cheikh Omar Diagne a raison
Abdou k g islam nékh nala mais diang dîné warnala tamite
Walay lou lerr nga wakh
Kariim léegi Nitu naafeq dëgg Nga
Xurou xara tu pédales les mélanges.
Rappeur yii founguen nekone bii rewmii dii takk
Karim gor yalla deugueu la
Karim khourou khar nékal nit way sarab li
Sidy Lamine Niasse dafa ni wone journalistu walf yi dé lène and ak peuple bi.
Légui peuple bi and ak état bi, yaw Karim nga ni journalistu walf yi warou niu and ak état bi ? Nga lène di traité de guéweul de l'état ?
Louy sa problème ?
Karim sof gua
Mais khrum xax maane léegui la Gueum ni ka tékiwoul dara ndé fi mounéni kou yeungueul kouné mou ande ak yow c'est à dire moome na réwmi tak rék ak nimou meuna také yeupe diaralnakoko
Yen est ce que Sava ??
Nakala askan Wii taxé Diouk té même askan Wii gno dioxx majorité régime
Nguen ni askan Wii gnola yoni pour attaqué régime bi ??
Karim néna thiat nitou principe leu 😂😂😂Karim Loula dieulé yen à marre AK bi ngafa guené li ngay d'âne waxx ci médias yi contre y'en a marre ??
Dem collaboré AK makhtar le kagoulard...😂😂😂
Mane je te suis mais khawma lo xexx tu es contradictoire nga balma
Bou neké Askan wi moom meussou niou wx lolou,Wax deugue mooy faral État maan deuk bi do comprane prfw Karim do kitou deugu Di diokh Moustapha leçon Thiate dafa comacé dof legui
Karim me fia rirrr bilyy il me sembl ke kou beug diner lheu kou beug rewomm lheuu mé pour mom lépp khell mou sell mokoy deff manee le jour ou bimiyy wérénnté ak benn oustaz mouy waxx alhour an mom mouy waxx li khell nangou
Nane guaye togé si emisión di wakh sama gran ba krawo kou dégue guaye wakh Li Mou khepe laa sois un peux profesionele
Yaw wero