Merci omaro pour ces belles paroles, on a mis du temps pour connaître vraiment cheikh bethio. Moi personnellement je regrette si j'ai une fois dit de mal a l'endroit des thiantacones. Mais un geste qui ma tjrs plus chez cheikh bethio c'est qu'il était très généreux, certes il avait un sacré caractère mais c'était un homme formidable dommage qu'on le sache trop tard... Qu'il repose en paix.
@@pggraphiste7965 lingay wax aka mako xam thianta la te mome lay done ba aldiana waye serigne bethio day yeurmande te diotay bi gnou moudje tocc ci tasfiya la done wax kon na dimbale diam gni te sante ko bou wer ndax nek ndaw te xam yalla doulou evident
Raféte na manchallah koula défal lou bakh boul tayi diko wakh il faut être reconnaissant dans la vie yalnang ko soute ay ati ate nga doundou ba doyal wakh dji amna yar ak téguine🙏🏾🙏🏾❤️❤️😘😍😍khana kone leérna wa kéee
@@thiantaconefaaawww6593 yone bi Ahmadou Borom diam gni moko mom tei Cheikh Mountakha Mbacké mokofi neikal kone thi ay ndigueuleum reik laniou wara teigou nioune ay talibei bei dongue laniou sa tontou nanka kholatt kilifa yi douniou seine morom avc ça ngaye wowei sa bop beugue cheikh betio linga wakh ni dei doussa tieur
@@aminafall6937 Li geuna grave si adouna moy juger nitt .nieup kham nagne ni yalla fi nekk .té iow so diakarlo wone ak niome li doko wakh.défal iow li dal sa khel té bayiléne niou deff li dal sen khel diam am.enkor une fois togne bakhoul
Man Mom beug Nala
Nguirr Ninga Beugaii sa Serign
Cheikh Bethio Thioun
App Mourith Day Beugeu serinieumm
Billahi.....omoro Yalnasa Diamm yageu way
Thi Barcke cheikh Akhmadou Bamba khadimou Rasoull 🙏🏻🙏🏻❤️🙏🏻🙏🏻
Merci omaro pour ces belles paroles, on a mis du temps pour connaître vraiment cheikh bethio. Moi personnellement je regrette si j'ai une fois dit de mal a l'endroit des thiantacones.
Mais un geste qui ma tjrs plus chez cheikh bethio c'est qu'il était très généreux, certes il avait un sacré caractère mais c'était un homme formidable dommage qu'on le sache trop tard...
Qu'il repose en paix.
Ndeysanne tu n'es pas la seule ma grande mais mome xolame dafa set nena balna gnep
Serigne Bethio moy borom thiante gui Masla bi dafa doy Serigne Bethio Dou fi djiouk moy Serigne touba té jeufé ndigalam da gueneu wor
@@pggraphiste7965 lingay wax aka mako xam thianta la te mome lay done ba aldiana waye serigne bethio day yeurmande te diotay bi gnou moudje tocc ci tasfiya la done wax kon na dimbale diam gni te sante ko bou wer ndax nek ndaw te xam yalla doulou evident
Raféte na manchallah koula défal lou bakh boul tayi diko wakh il faut être reconnaissant dans la vie yalnang ko soute ay ati ate nga doundou ba doyal wakh dji amna yar ak téguine🙏🏾🙏🏾❤️❤️😘😍😍khana kone leérna wa kéee
Kou ande ak sokhna aida boko si yonou mouride silima diap
Surement
Mann de tobou ma benn femme
Amoléne xam xam xamoléne serigne bethio khamoléne sakh nou yonou mouride di dokhé nopiléne
Maty mbow kèneu ladioula.
@@fatymature9476 akk mane mii
Ndeyssane machallah omaro kaddou yii raffetna serigne bethio molla dimbali mo waralle ngaye deugui deugui thiantacone di deugui deugui talibe yallenala serigne bethio samalle bopame
Machallah wakhdji rafeetna
Merci omaro mbokou talibe serigne saliou thioune souniou bountou ci serigne bethio yalnafi yague lool te wer
Billahii kendou serigne touba serigne saliou serigne cheikh bethio
Machallah omorou rafetna
Machalla lafe thiat omoro
Omaro u a rester tjrs fidèle♡
ماشاءالله
Merci kagg dou yii rafetna maschallah MOURIDE tiguel
ماشاءالله،عمركي،جرجف،جزاك،الله،خيرالجزاء
Machallah kadouyi rafetna
Merci Omaro bou Cheikh Betio Thioune sa wakh rafetenaa trop gorr pire ngaa.
Omaro machala
Machallah
Ndeyssaan SANT AK JARIÑÙ reka fi dess Omaro mù SERIGNE BÉTHIO begg naathii ioe deh barké SERIGNE SALIOU♥️🙏🏾
Nica na merci omaro
Mashallah wakhe dji mouridéna
Ma beug Mohamed niang ❤️❤️❤️
Yaw kou baakh nga ndakh danga gorer. Yallah nala bour yallah faye barkep chekhoule khadime khadimoule rassoule daradiaye mame cheikh Ibrahima fall baboule mouridina amine
Machahala omaro kadou yi rafetna lollll deug rekkk gafi wakhhhhhh
Billahi cheikh bethio kene la fiii
Machala y'a goré
Omaro danga ame geume geume motakh nga nekhma
Merci omoroo mée je pense que kéne dou dondou sa baye dondou bayou diabour cheikhoul Khadim Serigne modou Moustapha mo dondou
Il se dispute le present alors que le.futur m.appartient ...SERIGNE BETHIO THIOUNE
Omaro sa wakh rafetena Serigne cheikh Bethio ken la do niare ba faw kou Yalla diembelewoul do kham
Ay wayy omaroo mala beuggg wayy bilay y'a goré wawww gore
jajeuf frère
Machalla douma thiantacoune dé mais nite kou bakh day goré kadou yi rafètna
Omaro machalla rafetna
Wakhdji Rafetna torop
YAA MEUN SA NITT THIOUNE ♥️🙏🏾
Jaime bcp se gar
Ooh sameuh xoole bii sedd neuh♥️Jërëjëfëty SERIGNE BÉTHIO 🙏🏾
Diadieuf omorou
Bravo bravo ragazzo
Merci omoro j fier d toi
Yalla nala yalla diapalé omaro
*-machaaala-*
DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAM A DIARRAMATYYY MMMAAAMMMEEE SWRUUU CHEIKH SIIKKAARR NDIAYEEE!!!.(MF)
Dekleu yalla Lou keune lay def
nooo vrai communicateur wakhhh rek ngay defff
Ndéye sane nice naa omaro thioune mame bambi st srgn saliou mbacké balla thioune mame bambi u nss mk bc waye st srgn saliou
🙏🙏🙏✌️✌️
Yaw guemo serigne bi bilahi
Omaro Yaye gor Yaye mouride Yaye Thiantakone wakhalde ak thiante KO gorewoul meunoko yaye diambar s bethio faww
Machalla gor ni laye méle fière d'être thiantakone
Li ngen topou da amoul benn nderigne. Fethi rek diotay yo kham ni kenn doufa toudou yalla
salam no Omaro digua ma rayé
Deysanne macha'ala goré rék mo wor
Beug cheikh bethio soudé deug si yéen daguén diappou tawambi serigne saliou ta lolou la khalifabi santané kou beug say intréey boppou nak sola nékhé wakh lénén wayé diapalni donoto mourite ndakh ndigeul dieuffé
Fhacha Obiang yene hame bou dè yèna mom mouride gui
@@thiantaconefaaawww6593 mourite ndiguel dieuffé lolou moy yonwi koumou nékoul nga wout sa yonou boppou ta khamni doto ap mourite
@@thiantaconefaaawww6593 yone bi Ahmadou Borom diam gni moko mom tei Cheikh Mountakha Mbacké mokofi neikal kone thi ay ndigueuleum reik laniou wara teigou nioune ay talibei bei dongue laniou sa tontou nanka kholatt kilifa yi douniou seine morom avc ça ngaye wowei sa bop beugue cheikh betio linga wakh ni dei doussa tieur
Topoulen yalla senn borom mo geun. Digaloulen fethi ni khaware
Mandhoul
Sokhna ci nitt day mandou .geumal linga geume té bayi dougg si affaire diambour .
@@alassanediop2243 manè ngen diamou dji yalla te bayi fethi ak yi amoul sens yi yalla mofi nek te mom rek mo meun
@@aminafall6937 Li geuna grave si adouna moy juger nitt .nieup kham nagne ni yalla fi nekk .té iow so diakarlo wone ak niome li doko wakh.défal iow li dal sa khel té bayiléne niou deff li dal sen khel diam am.enkor une fois togne bakhoul
@@alassanediop2243 man ma doul dem fagnou nek ndakh fougnou doul todou YALLA douma fa diar
Wakh deugg dh baax na
Dama len sokhla dama am ben vidéo bou graw bou malen beug diokh
Non omoro soop nala ndakh deugou gui ga deff
yow wakh rek nga desse
Lo am kham kham amna gnou la epe kham kham tolo gnou thie wéé tank
Waye domame mo ngoye donne
👌 kadou yii rafett na
omaro tu me plait beaucoup
NDAYE SAN YA MOURITÈ WAYE
Vrai fumier ngua.T es un talibé et seulement.Laisse la famille régler son problème.
Omaro yaw danga gueune
On NN MV ju
Wakhdji rafetna trop mais stp journaliste ai micro yi
Mbeusso nioul ak maigrir
Koula bayi?
naffekk rekk
Omoro seytané pirr nga
bilah ki deh mako wedî
di Djayyy nafekk
Day diakhassé rékk
degu rek la wakh
Degue dou rombou aye nopou
Niay wannée reck gua defffff ta sofff
0
yaw amaro mouhamer nia mola dahka woye hkamo dara yaw daga bari wakh embesile
DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY SWRUUU MAME CHEIKH SIIKKAARR NDIAYE (MF?!?!)
Machallah