Mais nak nekhoul ba nekhoul mais sene émission bi émission bou mak la wara done niouko tek si télé yi djiguene ndi ak goor ndi niepou di setane ndakh liguénii diangalé dafa ame solo lolou sakh gaa wakh bi bisarena mais dangéni diangalé yane jour lay ame
DONC YEN AMOLEN SIKEU QUOI? VOUS ETES BELLES PROPRES,SILWISE SI BIRR AK SI BITI? VOUS MENTEZ!! KHAM NGUEN NI VOUS 3 LA KOUSSI DIOG AMNA LOUY KHEGN SI YEN! UNE EMISSION DE KHASSTÉ SE MOROMOU DJIGEUNE!
yen niou rew nguen lou si sayone si solo diambour dioulit dafay mandou sen wah dara si rafetoul amou len xam xam dem len diangui ba fegne telei ba legui tu vois du n importe quoi
Machallah Ami cole
Mais nak nekhoul ba nekhoul mais sene émission bi émission bou mak la wara done niouko tek si télé yi djiguene ndi ak goor ndi niepou di setane ndakh liguénii diangalé dafa ame solo lolou sakh gaa wakh bi bisarena mais dangéni diangalé yane jour lay ame
Amy colle mashallah dpuis Italy
Wakh leen thia kaw dh amna gnouye rayatè dh
Mrci amy collé bilay mane damay wakh ba sonou ya dés chose yo khamni nit mokoy défal bopam
Wa ki day hassé 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Waxleen ci seen vaginose bacterienne yi
Seen dieukeur yangi dèe
Bilahi amy coller mi dimako yagué nop
Sa sante bi déh la khamoul noumakoy déf motax meunou Mala wax dara… kii diabarou diambour la.
Amy collé yaw bayil
Mdr. Amy colle. Et comme moi. Je ramène. Toujours. Un drap. Partout. Par mesure. De précaution pas. Envie. De dodo dans. Des draps. Miteuc
😂😂😂
🤣🤣👨🔧
🤣🤣
Vekh vekh coloris rek gendesol
DONC YEN AMOLEN SIKEU QUOI? VOUS ETES BELLES PROPRES,SILWISE SI BIRR AK SI BITI? VOUS MENTEZ!! KHAM NGUEN NI VOUS 3 LA KOUSSI DIOG AMNA LOUY KHEGN SI YEN! UNE EMISSION DE KHASSTÉ SE MOROMOU DJIGEUNE!
yen niou rew nguen
lou si sayone si solo diambour
dioulit dafay mandou
sen wah dara si rafetoul
amou len xam xam dem len diangui
ba fegne telei ba legui tu vois du n importe quoi
Yaw mayal nitt yi sén diamou boula intéressé woul lofiy déf bay commenté…thiiiiiip
@@Actu7tv moma diakhal
Vraiment