Urgent MAY BOROME DIAMONO MAY KHOUB....SANGUE BABACAR NDIAYE SIGNE INSISTE ET PERCISTE

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 15 ต.ค. 2024
  • MAY KHOUB DI BOROM DIAMONO....SANGUE BABACAR NDIAYE SIGNE INSISTE ET PERCISTE/ PART 2
    sur la D TV AVEC cheikh BITEYE et CHEIKH BABACAR THIOUB

ความคิดเห็น • 1K

  • @Assadiqq
    @Assadiqq 5 ปีที่แล้ว +18

    Al hamdoulilah baniou yalla wanné Sunna La hawla wala qou wata ila bil lahi... Bou done ahloul Sunna nga xamné xam xam bokoul ak xeum xeum Yalla naniou yalla may degg ak top

    • @Serviteur-0
      @Serviteur-0 3 หลายเดือนก่อน

      ❤❤

  • @abdoulcaan5948
    @abdoulcaan5948 5 ปีที่แล้ว +10

    Xam xam dall domi cheikh seidyy Aboubacar sy ja rekk moma ci doyyy di cheikh Ahmadou tidianes sy Al khoutboul macktoumm yalla nala yallah yokk lerammmmm sy malickkk

  • @allaloutvmbollo6651
    @allaloutvmbollo6651 5 ปีที่แล้ว +5

    Kanamm laa dieumm lepp dinaa lerr inchaalaa.yallah molenn dii werr ndank ndank rekk naniou setann rekk gnielenn dii topp jisso gouniou daraaa

  • @mababathiam4672
    @mababathiam4672 3 หลายเดือนก่อน +3

    Khoutbou zamane Dafa wara ande ak Dale di wakh wakh bou ler nagne té nango deglou nitt gni té kima guiss amoul dale téyit dou nanguo deglou😢😢

  • @thiernongom8645
    @thiernongom8645 5 ปีที่แล้ว +61

    En tout cas lima leer mooy ni:
    1) Ab khoutbou dou weranté
    2) Ab khoutbou dou dem sih ab télé dih wané boppam
    3) Ab khoutbou dou sokhla lenni adduna.

  • @mamadoucisse2009
    @mamadoucisse2009 5 ปีที่แล้ว +121

    Kou yebou rek fonk diangue ak guestou sa diine. Ces marabouts trompeurs pilulent dans notre Senegal. Kii khamoul sakhe fimouy tek tankame. Cheikh IBRAHIMA Niass a ete tres clair dans ses enseignements. Alhamdou lillah !

    • @محمدمحمد-ص8ب4ع
      @محمدمحمد-ص8ب4ع 5 ปีที่แล้ว +6

      Mamadou CISSE wawa gir bana rerr

    • @daoursow2704
      @daoursow2704 4 ปีที่แล้ว +2

      Nopil yaaw

    • @AmiNdao-en3lh
      @AmiNdao-en3lh 10 หลายเดือนก่อน +5

      سكه انجاي إذهب وتعلم من جديد فابدأ من الكتاب وتعلم شرائع الدين ياعديم العلم

    • @LamineChabaka
      @LamineChabaka 4 หลายเดือนก่อน +1

      Merci broo

    • @AishaBa-g8i
      @AishaBa-g8i 4 หลายเดือนก่อน

      Ibrahima nias mo fi wakh wahdatoul woudjoud. Yall nagnou Yalla mouseul tchi gnoom gneup.

  • @xeuchelaye6924
    @xeuchelaye6924 4 ปีที่แล้ว +30

    Beine référence mo am mouy le prophète Mouhamadou Rassouloulaye aleyhi salam

    • @ndaomamadoundiaye6750
      @ndaomamadoundiaye6750 4 ปีที่แล้ว +5

      Mé yonéne tibi psl waxna né al houlamahou warasatoul anebiyahi

  • @collypupa9619
    @collypupa9619 5 ปีที่แล้ว +24

    Al hamdou lillahi binu yallah boole ak seydil haji malick sy

    • @aramefall6510
      @aramefall6510 ปีที่แล้ว +1

      ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏TohBoe

  • @Dou_Mindset
    @Dou_Mindset 2 ปีที่แล้ว +18

    Alkhourane ak sunna ❤️🙏🏾

  • @ousmanekane8377
    @ousmanekane8377 4 ปีที่แล้ว +5

    Machala cheikh banale yaw yalagavi yaGe tawe'r barke baye niass Amine yarabi Machala walayi dayesan dégele Machala cheikh babakr ،جرجف ،🕋🕋🕋🕋

  • @kanedieye3115
    @kanedieye3115 5 ปีที่แล้ว +5

    Alhamdou lillah bima yalla màyé xél bouy xalat gni ay réyalaté reck dégal mounane aboubacar moye talibé cheikh tidiane

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      Mais lathe ko foume ko tek

    • @adamadieng1054
      @adamadieng1054 2 หลายเดือนก่อน

      Saway yonene yi niofi gueun guinawam sahaba yi niosi toppou nénaniou Sahaba yi sén fass ya fourite bouy guéné si guémègne mo gueneu for walihou Kamal degg nékhoul

  • @daoudanizeupseck6687
    @daoudanizeupseck6687 5 ปีที่แล้ว +4

    Macha allah Sangue Barhamou Ndiaye lii koussi bokoul wallahii hamoko dieureudieuff binga deugueulé nii vous etes l'elu de Dieu et Baye Niass moyy sougnou mahzab amouniou cii ragal on se réfère sur Cheikhal Islame🙏🙏🙏

  • @oumousalama6038
    @oumousalama6038 4 ปีที่แล้ว +23

    C est rassurant par ces commentaires de voir qu il y’a encore de bons musulmans

  • @khadimleye5738
    @khadimleye5738 5 ปีที่แล้ว +30

    Démal déglou Serigne Sam Mbaye mou wakh la kane moy khoutbou nane la khoutbou di mél

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 3 ปีที่แล้ว +2

      wallahi kou bakh

    • @DIOBISTO
      @DIOBISTO 5 หลายเดือนก่อน +1

      😂😂😂 Serigne Sam qui avait dit que le kaaba avait été déplacé dans le passé 😂😂😂

    • @lifeisgood2429
      @lifeisgood2429 3 หลายเดือนก่อน +1

      @@DIOBISTO so diangoul khamo histoire du monothéisme dangay lathié.

  • @seydinasow880
    @seydinasow880 5 ปีที่แล้ว +19

    Sangue vrai Diop Fall nga...... Dieuredieufee Baye Niass

  • @bassiroubadji448
    @bassiroubadji448 3 หลายเดือนก่อน +1

    Sangue Babacar Ndiaye mi yalla wérnako dh mboubo yalla té amo xam xam bi djoulite dako wara moytou . Li mouye déff baye Niang wakhouko dh

  • @ndiackndao3280
    @ndiackndao3280 4 ปีที่แล้ว +15

    Qu'allah nous preserve et nous guide dans le droit chemin jusqu'à la fin du monde. Qu'allah nous protège et nous fait le chemin du prophète psl et ses compagnons radiyallou hanhouma.

  • @issadiop4614
    @issadiop4614 4 หลายเดือนก่อน +1

    Borom djamono moy Seringe cheikh Ahmed Tidjane sy al maktoum al khouboul maktoum,wa bazakhoul maktoum ❤❤❤

    • @joaopaulo77pulo78
      @joaopaulo77pulo78 4 หลายเดือนก่อน

      Senegal mo nèkhdè kounè di fèn dieumelè Sao serigne😂😂😂

    • @madieyegueye7891
      @madieyegueye7891 3 หลายเดือนก่อน

      Yalla rek mo kham kouy borom diamono

    • @Serviteur-0
      @Serviteur-0 3 หลายเดือนก่อน

      ​@joaopaulo77pulo78 😂😂😂 bilahi kou dakk fén gani ki la

  • @assanesarr149
    @assanesarr149 5 ปีที่แล้ว +9

    Parole de mécréance pure et dure.k'Allah vous guide

  • @mmgalsen
    @mmgalsen 5 ปีที่แล้ว +58

    Il n'a pas le droit de se référer à Halil mais il a le droit et dans l'obligation de connaître et de dire exactement ce que Halil à dit dès l'instant qu'il a dit qu'il était le qutb comme cheikh Tidiane a décrit le qutb Farouk Jami'u. Si il était vraiment ce qutb il aurait dû mettre tout le monde d'accord d'une clarté qui ne saurait laisser aucun doute dans le coeur des gens. Mais même les a'matul nass ont eu une honte monumentale ce jour. Il a dû chercher piteusement à s'agripper sur des potentiels faille de son interlocuteur alors qu'il aurait dû dire simplement ce que Halil a dit dans ses écrits, dire ce que le Coran a dit dans l'heritage et ensuite dire son fikra sur la haqiqa au lieu de se verser sur des querelles dérisoires. Pire il a dit avoir un peu de répis quand il était mal au point de la part de son disciple. Ce qui montre l'échec cuisant qu'il a subit c'est qu'actuellement tous ces disciples sont aux aguets sur les RS entrain de pinailler et de défendre l'indéfendable, montrant la psychose qui les anime. Il aurait dû mettre tout le monde d'accord en répondant facilement, correctement et juste, alors ils ne serez pas là à le défendre.
    C'est sûr que si le contraire s'était produit, personne n'allait entendre mais Allah est JUSTE, déh déssi Marche bi ya tagué sa bop.

    • @vilaviljh6509
      @vilaviljh6509 5 ปีที่แล้ว +1

      ok

    • @oumyba2764
      @oumyba2764 5 ปีที่แล้ว +5

      Ki dou dara khutbu bou amoul léer khutbu bo khamné kadom sakh léroul kén khamoul limouy wakh mouy deur di ték ni chim

    • @mamadoudiop5098
      @mamadoudiop5098 5 ปีที่แล้ว +1

      No il n'est pas obligé d savoir ck Khalil a dit pr ck halil n'est KKUN interpretateur

    • @idriss24samb5
      @idriss24samb5 3 ปีที่แล้ว +1

      Tè gua nèka talibe rèk mo gueuneu woor yaw miye wotè khoudbou ta khamo darra dèmale sanguou

    • @KEBEDollars
      @KEBEDollars 3 ปีที่แล้ว +1

      @@idriss24samb5 yaw loutakh dolein aye nit demlen outi khel mo gueune kini eupoula sakh kham kham yaw

  • @mk-fg3nh
    @mk-fg3nh 5 ปีที่แล้ว +5

    Kou beugue kham fou khoutbou bi nék, khoutbou bi nékoul Sénégal sorina Sénégal lole billahi

    • @mk-fg3nh
      @mk-fg3nh 5 ปีที่แล้ว

      @@didi.tvdaldiam5070 motakh nga wakh ko daguassé am firdé wala

    • @mk-fg3nh
      @mk-fg3nh 5 ปีที่แล้ว

      @@didi.tvdaldiam5070 indil firdé

    • @mustiktv919
      @mustiktv919 5 ปีที่แล้ว

      @@didi.tvdaldiam5070 fan la neka si Gambia ak nakala todou??

    • @ibrahimasy3114
      @ibrahimasy3114 5 ปีที่แล้ว

      Ioe khamo khoutbou

    • @mk-fg3nh
      @mk-fg3nh 5 ปีที่แล้ว

      @@didi.tvdaldiam5070 100% sénégalais la mais je suis au gabon mane firdé you lére lassi am yallah momako wane kachf boulére mane ak bénéne copin

  • @barambengue6755
    @barambengue6755 5 ปีที่แล้ว +29

    Yalna jamm yagg barkei borom touba🙏

    • @deggfeenjotna
      @deggfeenjotna 4 ปีที่แล้ว

      Ki Ni borom touba tanéouko

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 3 ปีที่แล้ว

      @@deggfeenjotna ki borome touba dakh nako yague na motakh mouye weur di kathie name sakh tarikha tidiane tarikha gou yalla nangoula t geureum ko mais ki da alkou yague na

    • @abdoulazizsy2542
      @abdoulazizsy2542 2 ปีที่แล้ว

      Fenn rek

    • @elhadjidieng3652
      @elhadjidieng3652 ปีที่แล้ว

      v hv666666666 h

    • @solution5135
      @solution5135 ปีที่แล้ว

      Delene wakh lou rafett si nitou yalla yi

  • @cercledesprivilegiesduzikr3226
    @cercledesprivilegiesduzikr3226 5 ปีที่แล้ว +15

    Le soufisme est une forme d’adoration de seconde dimension dont l’objectif premier est de permettre au disciple d’accéder aux mystères d’Allah (swt) et de comprendre les phénomènes et réalités de ce monde. C’est une branche ésotérique et mystique de l’islam sunnite, une voie d’élévation spirituelle basée sur une initiation qui professe que toute réalité comporte un aspect extérieur apparent (zahir) et un aspect intérieur caché (baatine).
    Le soufisme est une tendance très controversée parce-que méconnue et incomprise des non initiés mais qui tire cependant ses origines du Coran ; dans le verset 151 de la sourate Al Baqarah (La Vache), il y est mentionné : « Ainsi, Nous avons envoyé parmi vous un messager de chez vous qui vous récite Nos versets, vous purifie, vous enseigne le Livre et la Sagesse et vous enseigne ce que vous ne saviez pas ». La compréhension de ce verset conduit à percevoir le pourquoi et l’importance du soufisme dans la pratique islamique. Dans les enseignements de Mawlaya Seydi Mouhamed El Cheikh, témoin de l’histoire sainte, nous comprenons que le prophète Seydi Ahmad (saw), a été parachevé sur terre sous le manteau humain pour se fondre facilement dans notre monde (Nous avons envoyé parmi vous un messager de chez vous) et mener à bien sa mission mais que sa réalité existentielle dépasse celui d’un être humain. Dans ce verset, nous apprenons que Seydi Ahmad (saw), en dehors de sa tâche d’enseigner le Livre et ses versets (Le Coran et l’aspect extérieur apparent ou zahir), il avait la mission de purifier, d’inculquer la sagesse et de professer aux musulmans ce qu’ils ne savaient pas (l’aspect intérieur caché ou baatine). C’est là où réside toute l’importance et l’objectif du soufisme dont le premier adepte si l’on se base sur notre analyse de ce verset, est le prophète lui-même parce-qu’étant le premier à l’enseigner. Le soufisme tire donc son origine non seulement du Coran mais de la tradition prophétique.
    La pratique de l’islam est l’un des pré-requis principaux du soufisme qui a pour un de ses objectifs la recherche d’un état spirituel permettant au disciple d’accéder à cette connaissance cachée. Elle est la seule voie où l’adoration de Dieu est pratiquée ni pour ce bas monde ni pour l’au-delà mais pour Dieu exclusivement car le soufisme conduit à cette connaissance divine qui permet de rompre avec tout ce qui n’est pas Allah (swt) pour se lier entièrement à Lui (Allah swt). Ce degré d’élévation spirituelle dans la connaissance de Dieu et de Ses réalités se fait en trois phases dans la pratique du tassawouf. D’abord il s’agit de débarrasser l’être de ses passions nuisibles du nafs et de l’emmener à un état d’ivresse spirituelle élevé. Le disciple arrivé à ce stade est appelé « mouride ». Ensuite la seconde étape est celle où l’âme se remet en question elle-même et cherche à se corriger intérieurement. A ce stade, le disciple est appelé « salikh ». La troisième phase est celle de l’âme apaisée.
    La grande majorité des soufis partage un élément commun qui est la pratique du zikr, obligatoire pour tout musulman mais que certains adeptes du tassawouf ont fait une priorité à leur ascension spirituelle. Le soufi d’aujourd’hui évolue dans une voie ou tarikha et est rattaché à une chaîne dite silsilah qui représente la généalogie spirituelle à laquelle il est lié ; ce qui n’a pas toujours été le cas pour les premiers disciples du soufisme qui faisaient pour la plupart une tarbiyatul nafs (éducation religieuse) et n’avaient donc pas forcément besoin de guide ou de tarikha (voie spirituelle) pour évoluer dans leurs formations spirituelles. La pratique du tassawouf peut donc nécessiter un maître et le choix du bon guide est une obligation pour le disciple qui voudrait éviter les conséquences psychiques négatives.
    Quand dans le Coran à la sourate 51 Ad -Dariyât, verset 50 (qui éparpillent) Allah (swt) dit : « fuyez donc vers Allah… », Cheikh al islam Cheikh Ibrahima Niasse traduit cette phrase par le fait de se rendre auprès de celui qui connait Dieu, en l’occurrence un guide spirituel, afin de s’initier sous son contrôle. La recherche de ce guide communément appelé Cheikh est donc une injonction divine et devient dès lors une obligation. Vu l’importance et le rôle que doit jouer le maître mystique, il devient primordial pour le disciple de savoir comment choisir son guide spirituel.
    L’origine de la recherche du bon guide spirituel remonterait au monde ghayb ou invisible et aurait débuté avec certains saints comme les Grands pôles secoureurs Seydi Hadj Malick Sy, Khalifa Babacar Sy etc., qui ont bravé des mers et des mondes célestes à la recherche du guide qui leur était spirituellement supérieur. C’est au terme de cette recherche, nous dit Khoutboul Akhtaboul Kabir Mawlaya Seydi Mouhamed El Cheikh, qu’ils se sont tous affiliés à Mawlaya Cheikh Ahmad Tijane Chérif, le pôle suprême.
    Dans le monde chahada ou terrestre, la tradition soufie du pacte et de l’enseignement de maître à disciple remonte à ce verset 10 de la sourate Al Fath (La victoire éclatante) qui dit que « Ceux qui te prêtent serment d’allégeance ne font que prêter serment à Allah : la main d’Allah est au-dessus de leurs mains… ». Le Cheikh doit forcément connaitre la voie qui mène vers Dieu et a cette obligation de satisfaire aux attentes de son disciple. Si celui-ci, dans sa quête d’un guide, était animé par l’ambition d’accéder aux mondes inconnus, son maître doit au moins être doté de la maîtrise de cette science permettant à l’adepte de découvrir les autres espaces et domaines du monde ghayb (invisible) ; ce qui laisse entendre que le guide spirituel doit être mieux armé que le disciple tant en connaissances qu’en droiture et doit être en phase avec les enseignements du prophète (saw) pour pouvoir en faire bénéficier son élève. Seydi Hadj Malick Sy avait exposé 99 comportements qu’un guide spirituel devait avoir. Mawlaya Seydi Mouhamed El Cheikh, dans la profondeur de ses enseignements, rattache ces 99 caractères que doit revêtir le Cheikh aux 99 noms divins dont le guide devrait s’abreuver dans le but d’inculquer à son disciple la véritable réalité de Dieu. Le disciple se doit ainsi de trouver un maître mystique qui lui est spirituellement supérieur.
    Le soufisme a eu à opérer des changements dans sa pratique tout au long de l’histoire de son évolution. Les soufis avaient tendance à se couper du monde extérieur afin de vivre reclus et souvent dans des conditions d’hygiène peu recommandables. C’est plus tard avec l’avènement de la révolution des lumières par le pôle suprême Mawlaya Cheikh Ahmad Tijane Chérif (rta) que le soufisme a connu une atténuation dans sa pratique et une richesse dans son résultat. Le soufi a pu dès lors être au parfum des innovations de son temps sans compromettre son devoir de communion avec les mondes extérieurs. Dans son histoire, le soufisme a été un rempart, bien que pacifique mais efficace contre le colonialisme. Au Sénégal, Seydi Hadj Malick Sy s’est muni du principe soufi du « haml adhal wara » (supporter les épreuves et les adversités) afin de progresser et mieux servir Dieu et les hommes et en même temps répandre la philosophie et pratique tijane à travers le pays.
    Mawlaya Cheikh Ahmad Tijane Chérif (rta), par ses pouvoirs incommensurables à façonner des saints parce-qu’étant le pôle de la sainteté, a fait acquérir au soufisme et aux maîtres soufis en l’occurrence, la capacité de former l’Homme sur le terrain de la spiritualité, c’est-à-dire de s’intéresser non plus seulement à ses désirs mais également à son âme .Il a permis à son disciple, sans le couper du monde extérieur, de purifier son âme et son esprit afin de bénéficier des connaissances délivrés aux purs, d’avoir l’ouverture parfaite aux mondes et réalités cachés et de faire de la vision du prophète Seydi Ahmad

  • @ibrahimaka20
    @ibrahimaka20 5 ปีที่แล้ว +11

    قطبانية؛ ولاية؛ خاتم الأولياء...هي أسماء سميتموها أنفسكم وآباؤكم ما أنزل الله بها من سلطان.

    • @modoundiaye3796
      @modoundiaye3796 5 ปีที่แล้ว +1

      أجل
      هم كذابون

    • @ndeyefatoufall2423
      @ndeyefatoufall2423 5 ปีที่แล้ว +1

      والله قلت الحق إن هي إلا أسماء سميتوها.......

  • @omarba2311
    @omarba2311 5 ปีที่แล้ว +6

    khoutbou dou tok nane mane may khoutbou djamono bilahii Baye Cheikh Mamour Inssa Diop Mala beug walahi ci iow la geuna yakaré khoutbou k waadji yague fi té wer

    • @bbrama8082
      @bbrama8082 ปีที่แล้ว

      AlHamdou lilah❤️

  • @cheikhoulkhairythiam2932
    @cheikhoulkhairythiam2932 5 ปีที่แล้ว +45

    Aka deugueur fitt.

  • @idrissaganagueye3975
    @idrissaganagueye3975 5 ปีที่แล้ว +17

    wallahi mbirmi doulene loudul Alkhoran ak sune

    • @issasarl4415
      @issasarl4415 5 ปีที่แล้ว

      Loye wiri wiri thie tontebi xay xay xay sague khoutbou samanou fann

  • @samndjim
    @samndjim 2 ปีที่แล้ว +2

    Ce que je vois même le débat n'est pas organisé car lun comme lautre ne laisse son prochain terminé ce qu'il est entraîne d'avancer. Et je vois comme si on pousse au fond Sangue Barham à avoir tord. Car ce dernier ne fait que parler Baye et le prophète et je crois que c'est l'essentiel. Dieureudieuf Baye Moukhtar Ka Diallo .

  • @ndoyeabdoulaziz
    @ndoyeabdoulaziz 5 ปีที่แล้ว +21

    Serigne bi keine leu mouye cheikh Ibrahima niass nioune nieup talibé laniouy done beu ila yawmidini!!!

    • @laminendiaye9111
      @laminendiaye9111 5 ปีที่แล้ว +1

      Dangay doul rekk fi Yalla mofi nekk

    • @ndoyeabdoulaziz
      @ndoyeabdoulaziz 5 ปีที่แล้ว

      Lamine Ndiaye ndeyssane lire ngua boubakh est-ce que? Yallah fi nek moy deugueu! Mais débat bi c’est entre deux talibés baye donc lima wakh nioune leu concerner ngua balma nak!

    • @seukeuteumeukeuteu6302
      @seukeuteumeukeuteu6302 5 ปีที่แล้ว

      Walahi ki gueumoul baye niass diékhoul ci baye niaas ci bopam la diékh ak kanamam bi mélni lougnou diw huile amo sakh léerou talibé tidiane tchim

  • @sallsallaziz7278
    @sallsallaziz7278 5 ปีที่แล้ว +17

    Kou bakh demal ligueyui diagui bayui wakh jii

  • @lerevolutionnairelhommequi8770
    @lerevolutionnairelhommequi8770 5 ปีที่แล้ว +25

    Sangue ndiaye do borome diamano borome diamano daye khame lep yow tontou wo fi dara lou lére vraiment

    • @aissatougueye2879
      @aissatougueye2879 5 ปีที่แล้ว +1

      Yaw yambar ngua rék yaw la alkhour aan di wakh "soumoum..boukmoum...houmyoun fahoum laaa..."

    • @hamaththiamattidiani1970
      @hamaththiamattidiani1970 4 ปีที่แล้ว

      @@aissatougueye2879 ki amoul kham kham sokhna si

    • @hamaththiamattidiani1970
      @hamaththiamattidiani1970 4 ปีที่แล้ว

      @@aissatougueye2879 sen sanga bi khamoul dara

  • @papandiaye9483
    @papandiaye9483 ปีที่แล้ว +6

    الإسلام دين الله ودين الحق ودين المساواة

  • @lefall5175
    @lefall5175 5 ปีที่แล้ว +20

    Ndiaye tontoul question bi😂😂😂

    • @ibrahimaka20
      @ibrahimaka20 3 ปีที่แล้ว

      😂😂😂😂
      Wakhou fi touss kay ak kaalam gui
      😂😂😂😂

    • @ballatown6975
      @ballatown6975 2 ปีที่แล้ว

      Dako meuneu tontou

  • @badoudrame3574
    @badoudrame3574 5 ปีที่แล้ว +13

    Nagne ande ak yar yaine nieup ay kilifeu ngaine beug baye rek mo am solo Yalla naniou yalla def ay talibé baye deug deug

  • @mouhameddiouldediallo4806
    @mouhameddiouldediallo4806 5 ปีที่แล้ว +44

    toppou yonnentebi té baayi tiaahaane

  • @amymamour
    @amymamour 5 ปีที่แล้ว

    Tieuy Yallah. Amna lo khamni niite warnako diomalé boppam. Di wotéwo borom diamono t mouno tonetou kelk questions. Yaw d soudè ya yoor diamono kone khawma founou dieum. "Kanane mane la dou mome mouk..... ". Dieureudieufè Baye.

    • @mamadoudiop5098
      @mamadoudiop5098 5 ปีที่แล้ว

      Gueumo bay niass nah mom Khalil du referencam t sangbi limu wah inaa seene dalil si alhuran pr wediko

    • @amymamour
      @amymamour 5 ปีที่แล้ว

      @@mamadoudiop5098 😭

  • @hamidoupam5899
    @hamidoupam5899 5 ปีที่แล้ว +28

    Sangue démale xami yalla mo ngueune. Tarebiyou dou wesse.

  • @paalphaba869
    @paalphaba869 5 ปีที่แล้ว +11

    Li yeup beugeu dara daradja akk ngur moka waral wayè sakhiboul wakhti dou yi gayi di wakh,bilahi kèn dou Cheikh Ibrahim Niass

    • @niangngagne7432
      @niangngagne7432 5 ปีที่แล้ว

      Sang mii ragaloul yalla dh

    • @papagassama3613
      @papagassama3613 5 ปีที่แล้ว

      Mane dama am problème ak Talibé baye yi nguén ni kén dou Baye Niass ba paré meuno lén nangoul ki yén khamolén dara....!! Weurilén yalla

  • @lahatleye6313
    @lahatleye6313 5 ปีที่แล้ว +5

    Serigne sam mbaye néna wounn diamono gui nieuw niou bary Dinan wootté. T ku wooté wull wouyou diy liy solution by moye diangé. Xali yi démlénn diangui.

  • @alassanetall5130
    @alassanetall5130 2 ปีที่แล้ว +2

    Cheikh tidiane biteye yalla nala yalla faye. Wotégui barina té recadrement aussi dassiy bahe.

  • @abdoulayeagne7089
    @abdoulayeagne7089 5 ปีที่แล้ว +17

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 non sangue Ndiaye daffa nekh Bilahi mingui thiakhane deh Ndeyssane

  • @docteurndiaye5737
    @docteurndiaye5737 5 ปีที่แล้ว +21

    Di wooté xam xam, ba paré, tok ak gniarri borrom xam xam youla eupeu xam, meune la diagale.
    Gaye wakh rek, XD
    A bon entendeur

    • @oumyba2764
      @oumyba2764 5 ปีที่แล้ว

      Gnakoulné dafay beugeu dé

    • @aissatougueye2879
      @aissatougueye2879 5 ปีที่แล้ว

      Toi tu n'es pas informé va demander à Biteye qui est Sangue Ndiaye quant à borom lou nioule li moom yehout la

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 5 ปีที่แล้ว

      salut🤣

    • @papeamadoufall8942
      @papeamadoufall8942 5 ปีที่แล้ว +1

      Aïssatou Gueye ñun feikei wouñu baye ❤ teih yeim nañu deif thi sougnu khôl yii yallah. Personnellement soxlawouma kham kouy Sangue ndiaye nakh ba penthiou yallah mounoul dap baye teih makama bi mouy wotei yorouko , douko meusseuh djott, teih bép mbougeul bou wara wath thi borom makama bobou dinako encaissé. Nah toup teih khamni Baye mongui dokhal.

    • @themannowhere5845
      @themannowhere5845 5 ปีที่แล้ว

      @@aissatougueye2879 fo tegue ni yehout la?

  • @omarmbaw5503
    @omarmbaw5503 5 ปีที่แล้ว +6

    Sénégal kounê nekhoul dagua amoul conexion rek😂😂😂

    • @tallalo2441
      @tallalo2441 5 ปีที่แล้ว

      Omar Mbaw hahaha

    • @ousseynousow6431
      @ousseynousow6431 5 ปีที่แล้ว

      😆😆wakhga deug kouné nekhoul .amon connexions

  • @Wilanetv
    @Wilanetv 5 ปีที่แล้ว

    Cheikh mom nena sahaba bi sènulene aboubacar ak cheikh d'où benu sakh cheikh bind nako sakh

  • @falloufall9408
    @falloufall9408 5 ปีที่แล้ว +12

    Mai ñii yémou ci guinaw ño may dadji😂🤣😁

    • @mamemalickdiagne9120
      @mamemalickdiagne9120 5 ปีที่แล้ว

      Fallou Fall 😂😂😂😂😂

    • @cheikhmorgueye
      @cheikhmorgueye 5 ปีที่แล้ว

      Fallou Fall 😂😂😂🤣🤣

    • @mamadoubalde3085
      @mamadoubalde3085 5 ปีที่แล้ว +1

      😂😂😂😂😂 niouy yeungeul ay bopp nak

    • @khalildiaw4297
      @khalildiaw4297 3 ปีที่แล้ว

      gnii séne boboyi dara nékothi wallahi

  • @sopef8133
    @sopef8133 5 ปีที่แล้ว +14

    Bou nguén bayiwul fénal yalla ak saydina mouhamed dubakh dé

    • @aissatougueye2879
      @aissatougueye2879 5 ปีที่แล้ว

      Sa baye bou toogoon fi wakhoumala fén rék wayè day poupe toubeyam

    • @sopef8133
      @sopef8133 5 ปีที่แล้ว

      @@aissatougueye2879 ki day fén rék mouy nirok golo sangue daye doul rék

  • @daoudafall6640
    @daoudafall6640 5 ปีที่แล้ว +10

    tarikha bou nek rek amnga aw lakal da gni fowé sene ndaw bâ maguette ne fi di sonal nite yi de mal diangui khoutbou d'où begu adouna

    • @cheikhseye7195
      @cheikhseye7195 5 ปีที่แล้ว +1

      Dafa melni Wakh nga deug nk

  • @mouhamedgaye
    @mouhamedgaye 5 ปีที่แล้ว +6

    Bayiléne thiakhane té diamoudji yalla niko yonnente bi diangalé loudoul ALKHOUR-ÂNE AK SUNNAH ay réér leu

  • @assanemaodombaye9656
    @assanemaodombaye9656 5 ปีที่แล้ว +12

    Astarfiroulah Aboubacrine Sadikh talibè Cheikhouna Tidiane guir yalla bayilen fenn bala adina dih toukki tèh diotagoul tèh itam sou fekkè yay khoutbou bi lou takh gua tope Baye Niass respecté len nittt doulen wayi dara

    • @youssousall4075
      @youssousall4075 5 ปีที่แล้ว

      Degueur fitt rek walahi biss bou dougué si bamel dina yalla dou ay fooo nek si télé di fennn rek

  • @omarsall7846
    @omarsall7846 2 ปีที่แล้ว +3

    dieureudieuf sangue barhamou ndiaye khalifa yalla bi par force

    • @dienefaye2096
      @dienefaye2096 ปีที่แล้ว

      ki dee bou yebo gua bayiko t seti kénéne sa wadji xamoul lou bary dee

  • @HappyniassTV
    @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว +4

    Personellement dama ame béne setlou bouma def WAKHI KHOUTB DAFAY BEURI THIOOOOOWWWW.

    • @mk-fg3nh
      @mk-fg3nh 5 ปีที่แล้ว

      Khoutbou bi nékoul Sénégal

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      @@mk-fg3nh hun.....watal ....wakhma foumou nek

    • @mk-fg3nh
      @mk-fg3nh 5 ปีที่แล้ว

      @@HappyniassTV sri lanka la nék billahi

    • @mateodiaz7952
      @mateodiaz7952 5 ปีที่แล้ว

      😂😂😂😂😂😂😂

    • @Sumatra774
      @Sumatra774 5 ปีที่แล้ว +1

      m k 🤣🤣🤣🤣

  • @HappyniassTV
    @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว +17

    Salamou aleykou mbokyi damay fatali sama bop di fataliwale ni Talibé BAYE yare ak téguine mo ko war

    • @bicboymboup2165
      @bicboymboup2165 5 ปีที่แล้ว

      Kii mom dou khotbou

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      @@bicboymboup2165 MACHALA FOKO TEK

    • @youssousall4075
      @youssousall4075 5 ปีที่แล้ว +1

      Martaba kou ka ragnagne mou nguad la am talibé rek mo am solo

    • @amadoulaminendao7901
      @amadoulaminendao7901 5 ปีที่แล้ว

      Deiggna deuGgg

    • @papeamadoufall8942
      @papeamadoufall8942 5 ปีที่แล้ว +2

      Yare ak teguine dou thiaguine neih Kou woteih loudoul DEUG nguaniko lingua wakh dou deug. Khoudbou dou wakhei bakaan . Khoudbou boh khamni on te pose des questions thi zahir nguay tontou thi batine 😂 . Ñi deigoul batine nak ?
      Baye dh kokou lath thi zahir mou tontou lafa , kouko lath thi batine nakanonou. Moussou ñuko lath question mouy paniquer wala mouy xalaat ni dañuko beug daneil ou bien pour le minimiser. Pour te dire lath Boko lath et que la question est male formuler wala meutoul mou corriger ko teik tontoula, tontou boh moussoul deig. Et il a fait le tour du monde djakarlo ak ay niit yo khamni il croyait qu'il n'existait plus sur terre nit kouléén yém (Nigéria, Dubaï, Égypte...) .
      Baye❤ moy thiapathioli bii dou meusseuh doon kén bah Penć yallah . Teih ñu amouñu kouñuy top kénéén. Wanteih soudeih mo0h raw baye barhama ❤ nañu wakh 🤨

  • @saikh2348
    @saikh2348 5 ปีที่แล้ว +29

    😀😀leboone lipone rek defka dinné

    • @halimatouba9300
      @halimatouba9300 5 ปีที่แล้ว +1

      Vrai lebonn liponn,, cheikh bitey, çà t'apprendra à inviter des guignols sur ton plateau

    • @ibrahimaka20
      @ibrahimaka20 3 ปีที่แล้ว

      😂😂😂😂😂

  • @dofoukhidma5796
    @dofoukhidma5796 5 ปีที่แล้ว +14

    Wa li nékhoul 🤣🤣khoutbou bou khamoul dara😂😂no Sénégal dal yémé na

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      KHAME NA DARA NAK

    • @oumyba2764
      @oumyba2764 5 ปีที่แล้ว +3

      Khutbu bo khamné amoul béneu léer té kadom léroul mouy deur di ték ni ish

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      @@oumyba2764 bilay mangui retane

    • @dofoukhidma5796
      @dofoukhidma5796 5 ปีที่แล้ว

      No Sénégal nk nékh na koum nékh woté macky wakhal ci li

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 5 ปีที่แล้ว

      🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 wouye

  • @sidymane6860
    @sidymane6860 3 ปีที่แล้ว +4

    Wallahi Sangue Ndiaye yay Goor 🤩♥️

  • @deggfeenjotna
    @deggfeenjotna 5 ปีที่แล้ว +25

    Rérre nga rérral nitteyi xolal dóf yi koy tôppa ragalléne yallah

    • @mamadoudiop5098
      @mamadoudiop5098 5 ปีที่แล้ว

      Yeefeer du masa ndagou deugue

    • @abdoukhoudossprinssgueye6027
      @abdoukhoudossprinssgueye6027 5 ปีที่แล้ว +1

      @@mamadoudiop5098
      Mane dh guiss na doul katte bou nék mais doul katte bo mélni
      Mome c la première fois
      Guinaw elle cheikh

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 5 ปีที่แล้ว +1

      @@mamadoudiop5098 dof ngeu rekk

    • @papematarmbaye223
      @papematarmbaye223 4 ปีที่แล้ว

      ay way connection bou doy mo nekh. Kou nek ngay deglou.

  • @dembaba7420
    @dembaba7420 5 ปีที่แล้ว +13

    Wa nguir yallah sangue Babacar Ndiaye demal yoki xam xam xam Al khouram

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      WAYE NANGOU NGA NI AME NA KHAM KHAM

    • @alymbaye202
      @alymbaye202 5 ปีที่แล้ว

      Yaw yakhale xam xam

    • @alymbaye202
      @alymbaye202 5 ปีที่แล้ว

      Sangue ndiaye kouko nagouloule khamo yalla

    • @dembaba7420
      @dembaba7420 5 ปีที่แล้ว +1

      Am xam xam lolou yombouna cheikh même le physicien en a mais nak woté lo matoul c'est ce redoculiser devant ses paire

    • @salllamtoro4678
      @salllamtoro4678 5 ปีที่แล้ว

      ki nak mo degar fit yalla na ko yalla guendi

  • @sophiendiaye3096
    @sophiendiaye3096 ปีที่แล้ว +2

    Serigne bi dama beugue guisse yalla khame ko sol ma lerr figua tolou sou défé ma ame serigne

  • @amadoulaminendiaye7027
    @amadoulaminendiaye7027 5 ปีที่แล้ว +14

    😂😂😂 Sénégal mo neekh rek. Yalla naniou yalla samm. Naniou dém diangui nioune niép.

  • @abdoulayeba8016
    @abdoulayeba8016 8 หลายเดือนก่อน

    Sangue Ndiaye daimall djangue sa dinai nga yaiwiiii sa talibé yi ngayy nakh, bakhna rekk

  • @lagheminfossur8529
    @lagheminfossur8529 5 ปีที่แล้ว +19

    ki mo meune doule arass nékoul assamane li nak moy wéddi Yalla wéddi Yonent

    • @adamakasse8094
      @adamakasse8094 4 หลายเดือนก่อน

      Téléphone kou voter rek dangay diapaler saway 😂😂😂 mander dama rousse Sakho ki ay pekher la yorr de wayer d'où kham

    • @adamakasse8094
      @adamakasse8094 4 หลายเดือนก่อน

      Saway de Khalil lay bagne nena douma tontou khalil

  • @mamadoulamineniang5758
    @mamadoulamineniang5758 5 ปีที่แล้ว +3

    Wa lima beugu kham moy sague mom kan moy serigne bikou diokh idiaza (kokou moom lan lay don kom ka yaye khoutbou bi)

    • @omarba2311
      @omarba2311 5 ปีที่แล้ว

      diarna lathié déh😂

    • @muhammedtouray6872
      @muhammedtouray6872 3 ปีที่แล้ว

      @@omarba2311 sheik oul khairy. Mourtania

  • @nelsontheleader5983
    @nelsontheleader5983 5 ปีที่แล้ว +3

    Finalement Dal ..... Beugu Baye reka woor !!! Khoutbou bouy ignorer di zappé aye questions tu ne fais que tourner au tour du peau c'est triste !!!fallait laisser biteye continuer la confrontation foumou yam nekh !!! Oumar Niane moy soufflet si souf nonou eupeuneu

  • @ibrahimbenali4164
    @ibrahimbenali4164 5 ปีที่แล้ว +5

    Sangue continuel di ligayal faydou ta bayi ay woté khoutbaniyatou ak borom diamano lolou day wagni sa daradja rekk kenne dou BARHAMA NIASS

    • @papagassama3613
      @papagassama3613 5 ปีที่แล้ว

      Kén dou Baye tei meuno nangou limiy wax kom yén niar yéna yém

  • @hamdiwachukrutv2618
    @hamdiwachukrutv2618 4 ปีที่แล้ว +2

    Vraiment débat bi nekhna mane oustaz thioub damako fan ... sangue Ndiaye diambar la

  • @lamarafall4891
    @lamarafall4891 5 หลายเดือนก่อน

    Aujourd'hui vous avez la latitude de choisir votre voie. Toute voie outre que la voie montrée aux sahabas est égarements et dans cette religion personne ne dementira le prophète Mouhamed (psl)
    Bitey sougnou borom deug leu beug. Dé dara thi kaw souf diaroul négocier ak genrou niit yi

  • @yutuetvsenegal7207
    @yutuetvsenegal7207 5 ปีที่แล้ว +5

    Merci oustaz mor kebe

  • @tidiane1787
    @tidiane1787 ปีที่แล้ว +3

    Alahou akbar machaallah

  • @bambatouba6884
    @bambatouba6884 5 ปีที่แล้ว +5

    Kou ame xam xam dotok si telé di werante déllo si watt len sén xellyi

    • @bayesow2375
      @bayesow2375 5 ปีที่แล้ว

      Dieureudieuf mbokk xam xam Dieufé ak digulé RK lay diarigne mais pas wanéwu ak wéraneté

  • @C.Sarr24
    @C.Sarr24 2 ปีที่แล้ว +1

    Merci beaucoup bravo je suis jésus

  • @mbayelo4941
    @mbayelo4941 5 ปีที่แล้ว +7

    sangue ndiaye wakho fii dara loo andi.taa khoutbou dafa wara kham lepp lou ame ak lou amagoul.baye niass mome rekk moy khoutbou bou nieup nangou. ta yaw sangue ndiaye wakhniou rekk baye fane la wakh nhe ganawe mome kouci toppou.

    • @lerevolutionnairelhommequi8770
      @lerevolutionnairelhommequi8770 5 ปีที่แล้ว +2

      Sangue ndiaye dafa yape nitte gni vraiment do borome diamano hahahahaha baye moye sérigne gnoune gneup aye talibés lagne

  • @ibousaho7376
    @ibousaho7376 5 ปีที่แล้ว +2

    Sangue Ndiaye Je Ne Suis Pas Niasséne Mais Rouslo Nga Képou Kouy Talibé Baye Niass...Billahi Li Rouslou Na Trop Ndiahil Yi Sakh Xamnagn Ni Sangue Ndiaye Amo Xam Xam Waxou Malak Done Xudbu

  • @momo-od1jd
    @momo-od1jd 5 ปีที่แล้ว +8

    SENEGAL MO NEKH D YAW YAY KHOUDBOU ZAMANE NII YALLA MO MEUNA MOUGNE

  • @alhassanediallo4539
    @alhassanediallo4539 2 ปีที่แล้ว +1

    Il est vraiment rigolo ce gars

  • @lagatv2704
    @lagatv2704 5 ปีที่แล้ว +12

    Débat yii dikko fegnal amoul been ndieurigne ndakh réer ak khôl you feewaalo té boubooba seytani dina ree.
    Daffa am kham khamou neekh at bou pinth niou bayissi khel amna solo

    • @barhamgaye9293
      @barhamgaye9293 5 ปีที่แล้ว +1

      bilah

    • @jaimemonpays2192
      @jaimemonpays2192 5 ปีที่แล้ว

      Mais Pape so wotee fok niou wouysila vraiment niounne baye laniou beugue sa sangue tontouwoul Benn questions donc .....

    • @mamadoundiaye9141
      @mamadoundiaye9141 5 ปีที่แล้ว

      Au contraire mon frère débat bi amna ndiariñe bubaakha baakh dina takh ñu féñale ñiy wotéwo ay mbirr datonuñuko.
      Banénebi si l'islam amoul kham khamu biir nékk wala pinthie.

    • @barhamgaye9293
      @barhamgaye9293 5 ปีที่แล้ว

      Pourtyant c tres interessant ca a permi au moins declairsir beaucoyup de sujet

  • @papandiaye9483
    @papandiaye9483 ปีที่แล้ว +2

    الحمدلله على نعمة الاسلام ولايمان والاحسان

  • @bayesow2375
    @bayesow2375 5 ปีที่แล้ว +9

    Khoutbou zamane dou nélaw sa bou teudé gueuma avatar RAM moy yéwou
    Di liguey si batine
    Ana Kane mofi doul nélaw
    Khoutbou d'où wah wahdiou bari ta ndanka lay wah kou Dale aussi lay done

    • @amadoulaminendao7901
      @amadoulaminendao7901 5 ปีที่แล้ว

      Mom dafa daladi wax deugg teyoul melni kouy werantei..

  • @yakikadafitraore746
    @yakikadafitraore746 5 ปีที่แล้ว +7

    Gars yii hamuniou kouy cheikhou tijani bouniou ko hamonne kenn dotou fi toudou Serigne,mo fenione makka mo fenione thia fass mo fegnitt thia Saloum

    • @ousmanemboup6307
      @ousmanemboup6307 5 ปีที่แล้ว +1

      Wa feniat ci Yoff wala?

    • @elhadjimalicklahi8065
      @elhadjimalicklahi8065 4 ปีที่แล้ว

      ousmane Mboup mo diaara lathie dh 😂😂😂 BAYE LAYE bouko keineuh dougueule si seine thiakhane yi kokou moye yakarou diaam gni taye ak bou euleugué

  • @jesuissankariste2452
    @jesuissankariste2452 5 ปีที่แล้ว +29

    Sangue kham kham kenn douko niodi. C'est une masturbation religieuse 😀😋

  • @a.n.n2144
    @a.n.n2144 ปีที่แล้ว

    Un journaliste très professionnel ''cheick tiadiane Bitéye'' longue vie à lui et à tt le monde..mais franchement j'arrive pas à comprendre l'objectif du débat

  • @abdoulayesadioniass2212
    @abdoulayesadioniass2212 5 ปีที่แล้ว +6

    yalnaniou yalla maye beugue baye niass rek point

  • @khadydiouf4019
    @khadydiouf4019 4 ปีที่แล้ว +2

    Ku bou or whatever.. The most important thing is that try to do good deeds , believe in allah and prohet mohamed SAW, do what allah ask us to do , stay away what allah forbidden to us, believe in all the prohets ,prepare to meet allah with (day of judgement ) etc......

  • @elhadjidoudoudiokh6667
    @elhadjidoudoudiokh6667 3 ปีที่แล้ว +4

    Machallah thiey Sangue Barhamou Ndiaye djeureudjeuf baye Niasse

  • @docteurjackson6551
    @docteurjackson6551 5 ปีที่แล้ว +9

    Yéna gui togne BAYE ...

  • @barhamgaye9293
    @barhamgaye9293 5 ปีที่แล้ว +9

    salamou aleykoum wa rahmatu lah tahalah ba barakatou.....

  • @djibrilthior8166
    @djibrilthior8166 5 ปีที่แล้ว +1

    Thiey yalla xame xame makherifa wakheko yomboul bo dakoul mouno sakhal yalla doundou yalla mogueune doundou serigne dieuredueuf borome darou cissé ndiamé borome diamano

  • @mondialtv417
    @mondialtv417 5 ปีที่แล้ว +12

    Cey addina bii kii daal xam naani dafa taggoowoul bimouy nieuw ndeysaan

  • @toubatewroutv7269
    @toubatewroutv7269 5 ปีที่แล้ว +2

    Dem l'en ligèyali serigne Touba Mo geune
    S'en wakh barina
    Kou bageu dara fa yalla
    Naga kenal serigne Touba

    • @mamadoulaminendiaye6868
      @mamadoulaminendiaye6868 5 ปีที่แล้ว

      Bou euleugué kén dou fay ay wakh bayi dieuf.
      Dieuf lou beuri
      Wakh lou touti.
      Dieureudieufé Borom Touba

  • @serignenguer
    @serignenguer ปีที่แล้ว +1

    Retane dama diapou Serigne mo yombou Sénégal pour certains intelligence la alors xam xam moy lepou

  • @MameyouCisse
    @MameyouCisse 5 ปีที่แล้ว +12

    Sant serigne bamba heureusement khadim rassoul existe réer bakhoul

    • @ousmanendiaye3669
      @ousmanendiaye3669 5 ปีที่แล้ว +6

      Yéna gueneu rér nieup

    • @dralandbush8362
      @dralandbush8362 4 ปีที่แล้ว +2

      @@ousmanendiaye3669 😂😂😂😂

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  4 ปีที่แล้ว +1

      Li bone dal moy khamo sa borom diamou wo yallah.....sakho yakar aldiana......
      Khame sa borom diamoudji yallah rek mo wor.....na lep rafet rek

    • @serignecheikhmbacke7551
      @serignecheikhmbacke7551 3 ปีที่แล้ว

      @@ousmanendiaye3669 yamana Doul
      Serignd touba mo djité waliyou yépe koumou nékh ak koumou nakhari kou noungou ak kou bagne
      Kou topou borome touba do rére moukou

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  3 ปีที่แล้ว

      Del lire limou bind inchala dinga geuna kham

  • @malickndiaye631
    @malickndiaye631 2 ปีที่แล้ว +1

    Kii ragaloul yalla barigo bou fess dou yangatou khout bou laa kene douko wakh deslakoy wakhal

  • @saloumtv6145
    @saloumtv6145 5 ปีที่แล้ว +6

    Sagua Ndiaye khamon dara démal diagui way

  • @Forevergraphicgroup
    @Forevergraphicgroup 5 ปีที่แล้ว +1

    Khoutbou Ndiaye wala book 🔱🔱🔱

  • @santyallasamaborom6925
    @santyallasamaborom6925 5 ปีที่แล้ว +9

    Pour man diamou yalla amoul werente

  • @assanetoure8640
    @assanetoure8640 5 ปีที่แล้ว +14

    Aka bari wakh té khamoul touss

    • @oumyba2764
      @oumyba2764 5 ปีที่แล้ว +1

      Touss khamouko ki dafa alkou Wayé mayko fi ak ate dina fay. Khutbu bo khamné amoul béneu léer té kadom léroul mouy deur ni

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 5 ปีที่แล้ว

      dara khamouko nak loudoul rereu reraleleu nioko topou🤣🤣

  • @papeamadoufall8942
    @papeamadoufall8942 5 ปีที่แล้ว +8

    1)Il y'a une réelle différence entre savant et ignorant . Ignorant moy ko khamni neinah dafa tok thi kham kham , wolouko , teik thi baña deim gëstou . Par contre savant moy ko khamni loumou am am savoir dafay yeukni dessna reik deilou sobouwatt.
    Sangue Ndiaye mii c'est le CHEF DES IGNORANTS limakoy Digeul moy toup deim djangui bala BAYE ❤ diko riki sou rikékouwoul bah pareih nakh wakhtaan yeup bakaan ladoon wakhei . Teih khoudbou yakarnani maan mi talibé bou khébou bii bakaan amoul thi moom thieur. Baye Barhama bakaan ak seytané moussoul am thi moom thieur.
    Excuse moi nak yow ak kép kou djokou thi yow neikhoul ñuy wakh yeini sah serigne . DEIMAL TOUP TEIH YEISSLOU DJI

  • @ramoomar6228
    @ramoomar6228 5 ปีที่แล้ว +2

    Borom diamono nga fa djante sowé fa gnari guedj ye dadjé kouko guestou dadj ko.
    EXTRAORDINAIRE.

    • @adamafaye7299
      @adamafaye7299 3 ปีที่แล้ว

      Sangue bou bèn koutbou. Tapalé reck

  • @cercledesprivilegiesduzikr3226
    @cercledesprivilegiesduzikr3226 5 ปีที่แล้ว +6

    il y ' a plusieurs Khoutbaniya. Les Khoutbanniya sont différents. Le khoutbanniya existe et continuera d'exister jusqu'à la mort de Imam Mahdi Mountazar. Ce derniers détient le khoutbaniya et il n'est pas encore apparu.
    Mawlaya Cheikh Tidjiani a deux khoutbanniya: le Khoubatoul Ouzna ( le khatmiya) et Khoutbanniyatoul Kanzam ( le Katmiya). Les Khoutbanniya de Mawlaya Cheikh Tidjiani sont différents des autres khoutbaaniya.

  • @atoumanefaye6603
    @atoumanefaye6603 5 ปีที่แล้ว

    Bilahi wallahi talahi ki limouy woté newoul ci moom ...vrai kagn la

    • @HappyniassTV
      @HappyniassTV  5 ปีที่แล้ว

      Yako wate nonou dal.....foko tek

  • @marabarhamou125
    @marabarhamou125 3 ปีที่แล้ว +7

    Dieureudieuf Sangue Ndiaye ❤️❤️❤️❤️❤️