Alhamdoulilah... Yalna Yàlla yagüal la Fii Lool doli ko xéweul ak sutureu gù yatuu Lool ci Lou fégn ak ci Lou neubù Addùna ak Alaxiira InShaAllah barkéeb BOROOM TOUBA
2018 lako dieul walahi wird kuko niam rekka xam limou saff. Guisuma wird bou gueun bi kou beugue yeg ci yalla, beugue defarou, lou beugue nga amko, wonne aduna guinaw, walahi bokk mouride dieulen wird bi je vous parle en connaissanse de cause bilahi 1 mois lala may nga xamni serigne bi dou morom
Waw Mangi ziar s Moustapha boubakh té diko nianal fanlako meune fékk nguir mou yéssalal ma sama wird wi kouma meun dimbali rék ma guisko wala ma dégg ko
Kiniou waron opéré mane mi mako defon Sëñ bi limu wax lu werr la
Ségne ziar naala. Mane dé numéro ségne Moustapha diop koki la beugone. Jajeuf
Envoyé ko message mu joxla nimerom
Kou bakh numéro m la bagon
@@ndiayeahmad5929 numérom la beugone
Yalla nala borom bi defal jame seddé bi amena solo
Akay Diambar Machallah Baye Moustapha Diop
Yallanakofi saa Borom Yagual Loll Te Weralko Barkep Serignebi
Amine
Alhamdoulilah... Yalna Yàlla yagüal la Fii Lool doli ko xéweul ak sutureu gù yatuu Lool ci Lou fégn ak ci Lou neubù Addùna ak Alaxiira InShaAllah barkéeb BOROOM TOUBA
Mandh yamako diokh yalla na yalla takhawola amine yarabbi DIEREDIEFFETI Sama kharitbi Sama sopebi
Bathie doma dimbali si numerom
Ziar Bathie nax meun na am numerom
Mane tamite momako diokh khatim bi machallah
Salam num serigne bi la yitewo
Kou sokhla num S Moustapha Diop Koki nomouy def
Man tmt yitewonako boma ko dieuker am
@@modoufamasyll8306 bakhna waw inch
Thieuy cheikh moustapha yéné na gneup mbaakh
Yalla nala yalla faye lepou lo beugue ak lo yène moleme djioulite yithi gueune
Machalla serigne Moustapha numéro môme la sokhla
Maachalah Serigne Touba Amool morom
2018 lako dieul walahi wird kuko niam rekka xam limou saff. Guisuma wird bou gueun bi kou beugue yeg ci yalla, beugue defarou, lou beugue nga amko, wonne aduna guinaw, walahi bokk mouride dieulen wird bi je vous parle en connaissanse de cause bilahi 1 mois lala may nga xamni serigne bi dou morom
Dieuwrine do ma bahé ma numéro Serigne bi
Dieuwrine do ma bahé ma numéro Serigne bi
Akka sadik ki yalna yalla sammou ko
Guena yague guena wér ❤ Barkep SERIGNE TOUBA
Bilahi maako beugeu ndakh ham hamam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oh tay moum lall ngama ❤
Wird makhfous Moss dolli ❤❤❤❤
Toudoul nonou d Maahouz la dou Mahfouz.
ماشاء الله تبارك الرحمن
Waw Mangi ziar s Moustapha boubakh té diko nianal fanlako meune fékk nguir mou yéssalal ma sama wird wi kouma meun dimbali rék ma guisko wala ma dégg ko
Patar diokhma sa contact ma diokhla bassam
Ndigel Diop dimbali ma si numéro bi
@@ndigueldiop985 ziar yitei wona numerom nguir yalla
Mayi ziar wa al khadimiyyah di rafétlou sén liguéy numéro serigne moustapha la yitéwoo pour mou yéssalalma wird wi sou féké japandi na
Jeurajeufati segne moustapha ❤machallaah
Assalamou haleykoum! Numéro Sëñ Moustapha la yitté wooo
Envoyé ko message mu joxla nimerom
@@ndiayeahmad5929 kan laay envoyer message
Assalamou haleykoum
Numéro Serigne Moustapha Diop kooki la yiteo
Wallahi sama khol seddouna
Kham kham bou lerr alkokiyou
Machallah cheikh moustapha
Dieureu dieuf Serigne bi Diop
Macha allahou ❤😊
Serigne montakha joxoon na ndigël keppu kuy murid def ko
Amineeee way. Diop
Sr cheikh saliou momasi diokh ndigueul
Thiaye aka nékhoune gàyi xaame la
Xamal niou ko
gàyi dane ko diappé wakhtane yi rék waya misall s sam mbaye rék migui nékh patar balangà ak diorbéll
5:26😄 aka saf xorom nag te baax te barib xam-xam te ragal Yàlla.
Yoro numéro rom
@@alycisse7466 waaw waaye mënuma ko a joxe fii de.
Lu yeeme la. Ba ci ku amé ay rap walla andando yuko sonal su ko dieulé dafay guiss niouy dagn ndank ndank ba sett wethie amna ci confirmation bu wer
Limou tidié gane xassida la néki kouko xam❤
Khassidak waduudu
Či xassida « Wa Laqad Karramna » la abyaat yi nekk, 4 bëyit yu mujj yi
Njariñi Wirdul Maaxuus .
Nay doon ci Wolof waay !
inshallah
MashAllah cheikh Moustapha ❤❤❤
svp je veux la traduction du wird khatim
Num serigne moustapha la sôkhĺa
Salam dimbalilen nou si númerom
Mashallah diop diangaléma lerna numéro svp🙏
Salam salam koumay dimbali si numéro Serigne moustapha diop koki
Numéro serigne moustapha la yitéwo
Serigne Moustapha joop moye lairou diamano
Maay sa Antal paréte
Amna solo khana amoul partie 2?
Amnasolo
Akay diambar
Je veux le numéro de serigne Moustapha Diop koki
Salam man d beugona numérom
Mandè dananko fonko
❤❤❤
Mane numéro Serigne moustapha diop la sokhe la pour dieul wir bi
Envoyé ko message mu joxla nimerom
Fane lanou lay yoné message 😨
Borom Xam xam la
Numéro bi.lasoxla