C'est grave! Un policier ne doit pas se comporter ainsi, mais comme Ils ne sont jamais punis , il faut que la justice fasse son travail sinon ça continuera.
Souniou hôpital tamit c'est à revoir ils auraient pu sauver le gars mais trajet yiniou def yeup si weur hôpital bouko nango dieul ils ont perdu bcp de temps il a trop souffert qu'Allah lui accorde sa miséricorde et l'accueille dans son paradis 🙏 et que justice soit faite 🙏
Sur cet histoire mom machallah a nos hôpitaux ils ont fait mignon meune defffffffff mais ces blessures étaient si grave Kokou bou doundou sax Moye lolou
Il faut faire des enquêtes internes dans tous les commissariats de police, afin de radier ces genres de policiers tortionnaires et ceux qui n'ont pas d'éthique et conscience professionnelle, pour accomplir leurs missions de service public et de maintien de l'ordre
Dieul ay jeunes pour quelques jours de formation def len policiers pour gnouy diambarlo ak population bi , voilà le résultat. Deja amougnou droit doorko meme boudé drogue leu yoor bakoy ray
Je m'adresse à son excellence Mr Bassirou Diomay Faye nioune amnagne si yaw yakar Li dafa niaw Ni lanioufi defone Pape Sarr tale ko ba legui fatewouniouko niou defate Li may wakh délégué de cartier bi di wakh wakhou guinar ak tele ce son que des chose matériel wah bakane bi dem nak esk sina delsi non dama warou
L'interpellation si c'est pour détention de substances illicites, doit se faire dans la rue, un lieu public mais les policiers n'ont pas mandat pour perquisitionner dans un lieu privé en l'occurrence la maison, à plus forte raison de bastonner à mort un individu qui n'est pas encore un menace pour la population (un criminel prêt à abattre quelqu'un...) Ils auraient dû convoquer à la police si c'est un individu suspect, s'il ne vient pas à la convocation, alors les policiers peuvent venir le chercher
Arrêtez vous journalistes vos questions bêtes essayant de dédouaner les policiers à travers la question..."loumou def" . Même si c'était el chapo ça ne justifie aucune mais aucune violence
@@alexismendy8809 Oui ki loumou wakh motax ma Repondre ko lii Il a dit que < wakhou lén boy yi deugue > Ak Boy yi louniou meunti def Diarroull nioulén di Door vraiment
Khére bi nouko nitt meuna doré nitt ak thi wérou koor gui mane lolou moye sama problème
C'est triste il faut que ça cesse justice pour mouhamed 😢
Il y a des choses qui ne peuvent se passer qu'au Sénégal et pfff rien non il faut que ça s'arrête
C'est grave! Un policier ne doit pas se comporter ainsi, mais comme Ils ne sont jamais punis , il faut que la justice fasse son travail sinon ça continuera.
Même bou féké Ahmed day diaye yamba waroul takh nioukoy ray
Billay Diarroul sax Doraté Billay
Souniou hôpital tamit c'est à revoir ils auraient pu sauver le gars mais trajet yiniou def yeup si weur hôpital bouko nango dieul ils ont perdu bcp de temps il a trop souffert qu'Allah lui accorde sa miséricorde et l'accueille dans son paradis 🙏 et que justice soit faite 🙏
Ils savent qu’ils ne peuvent plus rien pour lui
Amine
Sur cet histoire mom machallah a nos hôpitaux ils ont fait mignon meune defffffffff mais ces blessures étaient si grave Kokou bou doundou sax Moye lolou
Quelques soient les causes rayy warul am même bu rayone nitt sah waru niuko rayy vraiment metti na trop que la terre lui soit légère
Justice pour les morts et les cas de tortures entre 2021-2024
Raye mome dou yone
Il faut faire des enquêtes internes dans tous les commissariats de police, afin de radier ces genres de policiers tortionnaires et ceux qui n'ont pas d'éthique et conscience professionnelle, pour accomplir leurs missions de service public et de maintien de l'ordre
Hôpital 🏥 bouy wathi ndeysane senegal metina
Yalla naléne yalla atté
Il faut que ça cesse justice pour Mouhamad 😢😢😢😢
Bilay police Sénégal bi ken khamoul lilan leu
Door fayou point
Ayy domouram wérou koor ngén di ray amét mai yeen gnép si kasso bi ngên di dê😢😢
Thiotou ndeyem ku def lu bok simane do dokh thi kaw souf may noyiii😢😢😢😢😢😢😢
Sarape ndayi Li sheut
Ms li dafa yombu ndm
Avec Sénégal beug changer
Li métina dh
Les frères de hamet dagno yarou 😢😢ndeysane
Ces policiers n'ont pas le droit de maltraiter les citoyens quelque soit leur lieu de résidence, Pikine ou Point E
Dieul ay jeunes pour quelques jours de formation def len policiers pour gnouy diambarlo ak population bi , voilà le résultat. Deja amougnou droit doorko meme boudé drogue leu yoor bakoy ray
Wakhal deug diay yamba diaroul ray justice pour ameth
Bilay nonu la deme
Ms Souy Diaye Saxx Drogue Kén amoull droit Doraté c pas normal
Vraiment
@@Cheikh31177 Ms kén amoull droit Doraté lii Afrique rk moko dessé a l'étranger Koffi door Dotoko defatti
Dem len prèvotè gnou convoquè len gnou diap gnii
Liidou yonn way
Meme keur gui boun fi de diaye sinebar ,yon santou len maltraite domou adama😢😢😢 😢😢😢😢😢😢😢mmmmm
Bly toukh katou yamba yi sonou nagn trope té gnigui fi di diay sangara😢 c'est triste !
Loumounti khew keb waroul ray😢
Diap nit diaroul ray justice
Je m'adresse à son excellence Mr Bassirou Diomay Faye nioune amnagne si yaw yakar Li dafa niaw Ni lanioufi defone Pape Sarr tale ko ba legui fatewouniouko niou defate Li may wakh délégué de cartier bi di wakh wakhou guinar ak tele ce son que des chose matériel wah bakane bi dem nak esk sina delsi non dama warou
Bo yoroul day yomb niouni daguay diay yamba amna niou fi nek ay jeunes borom alal gnoko fi dak dagno sonal wa pikine walahi li méti na dh
L'interpellation si c'est pour détention de substances illicites, doit se faire dans la rue, un lieu public mais les policiers n'ont pas mandat pour perquisitionner dans un lieu privé en l'occurrence la maison, à plus forte raison de bastonner à mort un individu qui n'est pas encore un menace pour la population (un criminel prêt à abattre quelqu'un...)
Ils auraient dû convoquer à la police si c'est un individu suspect, s'il ne vient pas à la convocation, alors les policiers peuvent venir le chercher
Sénégal dou dem boulen Sonal sen bopou sakh nii rk lay deme ba fin du monde 😢
C est très triste mais rien ne justifie ces actes de barbarie
Policier yi li nioulén maye dafa eupeu il est temps niou wah thi mérité wouniou sah sol tenu
Justice pour MOUHAMED Taya
Li sou amei Dagneine di djeul sen telephone gneine filme akh
Mais gni ay domeram lagnou rek
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Ay akareser solen defe police ni rek lay deme na diomaye ak sonko wah sili police louniy setatla dou koune lanko wara def rakhas rek nittyi nobalo
Khana Soudé criminel la sakh, Warnanou aam Keuyitt..Lii mom dou Police, c'est un Gang.
Bilay sama khél fofou la dem policier khana saniou def li khana
Ba cagn aussi domeram policiers yi
Naniu yarr jabbot yii A la base '' côté du défunt , et du force de l'ordre ''
Allez porter plainte. Cela nous permettra de reconnaître les nervis parmi les policiers
Police bi khana ay dëmlanou injustice bi day diékh dé
moh dou modiou fenn
Quoiqu'il en soit police waroul gawa dore amguén matraque électrique il faut l'affaiblir d'abord après menotté KO puis embarquer au commissariat.
Li laa tookh katou yamba dii doundeu ak policier yii.aye policiers youye mélni aye agresseurs vraiment sone nagne
thieuy yalla
😢😢😢😢
Non à l'impunité
Même si il est vendeur de drogue il n ont pas droit de le frapper jusqu'à ya eut mort
Arrêtez vous journalistes vos questions bêtes essayant de dédouaner les policiers à travers la question..."loumou def" . Même si c'était el chapo ça ne justifie aucune mais aucune violence
Pikine rekk mo ame si monde bi niouye défendre diaye katou yamba
Laye Ndour ce mon Amie d'enfant sont Grand frere Bangoura mok sama Grand frere niodone And
Louye sene problème Ak police moma khawa diakhal
Xana sétano interview
Pourquoi
Vrement sa c pas jolie pour l police Sénégal
Nn journaliste bi tmt dh ki néla sama kanam laniou ko dor nga nan ko lan moy won nioko don dor les oreilles et les yeux sont les témoins de la justice
Mais benen tonton bi il est irresponsable sa diarbat ngay xoulo ak mom
Petetre il a ces rezo😢
Danga kham kouko diarbatam def
@@astoudiouf9191exactement té sein yaye yi moy takh da ngay moudié té sa bop si niom
Manoul ci fami diamour bi sof gène trop té beugeu lonèn dof do menou ci fami diamour 😏😛😄
Kane molako wakh boy bi diarnatam bien sûr wakhal loxam😊
Père nak waxal li ame rékk mei xame nga ni dange done xekh ak policee yi mei nak ray mome da eupou
Il est vraiment geNd temps de decspittè la policeer mettre une fois pour toure a cette violence acrugle
La police et gendarmerie sénégalaise une honte
Wakhou leen deugeu bii
Boy yii ay domaram la nio
Ms Diarroull Ray Prison Yangui fii
peut être...mais bro j'sais k beuguo kouleu tek injustice kone waro nangou kou tek kénène injustice on attrape un individu dans les règles...
@@alexismendy8809 Oui ki loumou wakh motax ma Repondre ko lii
Il a dit que < wakhou lén boy yi deugue >
Ak Boy yi louniou meunti def Diarroull nioulén di Door vraiment
yalla nge dadié ak gnom gnou defla nonou com nonoula
@@iboudrame2449 sisi et t'a raison frérot mane sakh mome lay wakhale