IMAM BABACAR SYLLA CORIGE CHEIKH MBACKE SAKHO : SOBÉ AK NIAMPÉ DOU DINDI SOBÉ - DAFA WARA WAKH NÉ...

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 15 ม.ค. 2025
  • SOLUTION TV

ความคิดเห็น • 37

  • @fallouwalfsall8539
    @fallouwalfsall8539 2 หลายเดือนก่อน +3

    Merci oustaz
    Yalla nanio yalla mousal thi saytaané
    El hadj sidi lamine Niasse yalla nako yallah khaaré aljana 😢❤

  • @MANSOURNdao-y1z
    @MANSOURNdao-y1z 2 หลายเดือนก่อน +2

    ماشاء الله يا إمام ❤❤❤

  • @mamadoudiame268
    @mamadoudiame268 2 หลายเดือนก่อน +3

    Imam machalla ❤️🙏✊

  • @elhadjicheikhba4122
    @elhadjicheikhba4122 2 หลายเดือนก่อน +2

    Machalla Oustaz xam xam bi lérna 👏👏👏❤️❤️❤️

  • @OusmanenourayniSylla-ho4sb
    @OusmanenourayniSylla-ho4sb 2 หลายเดือนก่อน

    Machallah 🥰 Imam Babacar Sylla

  • @jaangatttv4577
    @jaangatttv4577 2 หลายเดือนก่อน

    Maachaa Àllaah jëwriñ Babacar Sylla

  • @ndongogaye1991
    @ndongogaye1991 2 หลายเดือนก่อน +1

    شكرا يا أبا بكر

  • @thiernodiallo1504
    @thiernodiallo1504 หลายเดือนก่อน +1

    Merci Imam Sylla.
    Mbacké Sakho maîtrise bien le coran mais il ignore beaucoup de hadiths qui sont très importants pour pratiquer l'islam.

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 หลายเดือนก่อน

    Yonente bi fan lako yalla dikhé ndigalou yok diouli

  • @ahmedkane4270
    @ahmedkane4270 2 หลายเดือนก่อน

    Machallah

  • @mamadoundiaye1323
    @mamadoundiaye1323 หลายเดือนก่อน

    assane bayil fén cheikh mbacké Sakho ndokh rek la wax

  • @AmadouGueye-n5b
    @AmadouGueye-n5b 2 หลายเดือนก่อน

    Mbacke Sakho say say laa

  • @mamadoundiaye1323
    @mamadoundiaye1323 หลายเดือนก่อน

    assane waxal li mbacké Sakho wax..... mom ndokh la wax deh

  • @OusseynouCisse-do3dh
    @OusseynouCisse-do3dh 2 หลายเดือนก่อน

    Mbacké sakho mo wakh deugg dé

  • @MANSOURNdao-y1z
    @MANSOURNdao-y1z 2 หลายเดือนก่อน +1

    Non asanne 😂😂😂😂

  • @Fallmuslim
    @Fallmuslim 2 หลายเดือนก่อน

    Swaaye.demal.dianguii

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 หลายเดือนก่อน

    Ki limou wakh si ndiap wouténa ak niko yalla diangalé si Alkhourane.

  • @mbayeniang5597
    @mbayeniang5597 2 หลายเดือนก่อน

    Probleme bi moy kénn werante woul ne yonent bi loumou wakh wakh ji key moy.. yeen ligenni wakhnè yonent bi moko wakh ndax mom moko wakh lolou moy wakh ji

    • @mamadoundiaye1323
      @mamadoundiaye1323 หลายเดือนก่อน

      Saay waxal waay...mbacké Sakho lepp lumu wax ci téré alkhourane lako tibé

  • @iboudue2727
    @iboudue2727 หลายเดือนก่อน

    Ki dafay doul fane la guiss niouné yonentbi mo yokou djouli
    boukhari a dit et ‘ on completa la prière de 2.qui est ‘On’

  • @TheKokejunior
    @TheKokejunior 2 หลายเดือนก่อน

    Sawaay dangay lèpe rék. So wolo sa bope togal AK Cheikh Mbacké SAKHO.

    • @diaibrahim6798
      @diaibrahim6798 2 หลายเดือนก่อน

      Sa waye boulniou fonto cheikh mbacké sakho khamoul dra na niew débat ak man thi dinédji kon ma corrigé ko amoul xam kham dfa reue lamine rk 😂😂😂😂😂 dieuleul sama numéro boula nékhé nga woko 😂😂😂 .

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 หลายเดือนก่อน

      @@diaibrahim6798ioe kagn gua

  • @babacardiop-tm6zp
    @babacardiop-tm6zp 2 หลายเดือนก่อน

    mbacke sakho say sayla fran mason la

    • @kaolackvamal2881
      @kaolackvamal2881 2 หลายเดือนก่อน

      Ya mana fén deugue té niémé yalla. Bayiléne soss

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 หลายเดือนก่อน

    Saway kén mounoul délou si Alkhourane di gueuleum ndakh Alkhourane moy guindé gui.

  • @mtdistribution-w6d
    @mtdistribution-w6d 2 หลายเดือนก่อน

    Mbacke sakh lou ler lay wakh thi AL HOURANE la bowola sa xam xam ngeen debat

    • @awalo3307
      @awalo3307 2 หลายเดือนก่อน

      Mbacké khamoul dara yéefeur leu dafa wédi souneu

  • @mamadoukane1139
    @mamadoukane1139 2 หลายเดือนก่อน

    cheikh mbacke Sakho diarol tonton dafare

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 หลายเดือนก่อน +1

    Ki khamoul sakh louy sobé. Sobé dou louy guéne si nit, bokalékat yi la yalla wakhne sobé lagniou.

  • @mamathgueye-t6n
    @mamathgueye-t6n 2 หลายเดือนก่อน

    Salut mémoire yéne loutakh dougué wakh aya you cheikh mbacke toudou si alkhoura

    • @jaangatttv4577
      @jaangatttv4577 2 หลายเดือนก่อน

      Comme que doyula lumu mana wax Dula convaincre
      Kon buka andee Lan lay jariñ

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 หลายเดือนก่อน

      @@jaangatttv4577😂😂 jamais niou wakh Ayat lolou moma djaxal.ay histoire rek

  • @bacarymaria6117
    @bacarymaria6117 2 หลายเดือนก่อน

    Salam si les hadiths du prophète PSL sont si importants dans la religion pourquoi le prophète lui-même n'a pas écrit ses hadiths.

    • @OusmanenourayniSylla-ho4sb
      @OusmanenourayniSylla-ho4sb 2 หลายเดือนก่อน

      Ce n'est pas le prophète qui s'écrivait plutôt il dit ou pratique un acte et les compagnons l'écrit

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 หลายเดือนก่อน

      @@OusmanenourayniSylla-ho4sb
      Legui kouko sante saxaba yi

    • @OusmanenourayniSylla-ho4sb
      @OusmanenourayniSylla-ho4sb หลายเดือนก่อน

      @iboudue2727 sahaba yi Sangue bi alayhi Salatou wasallam ♥️ modan Wakh Niouy bind 🖊️