Kou doyni seydinacheikh nganan bein way walaxi yalla nala yalla reub té bayil doul kein waxoula mo gueun alhouran dagn la wax mo eup dolé té daga gatt xam xam ndax barina kouy diang alhouran alhouran reub la té çalatoul bou dieum si yonenté ko mana doon yalla nagoul la
Sawaye kholale maye niou souniou diam té nga teudje sa gategui tarikha cheikh ak tarikha boumou mana done benne président mounou ko fait djieulai thi kawe souf
Yow kèn geumoula Tidjane manoko fi dieulé . Diangakatou al khouranoule karime-yi niougni réye nit-yi tia Yémen reye Ali mouhamed dieulélene makka. Bayil digueute tow geuemoulo dara
@tawhid-i3l yén sén khol moy dagga dina yagga dagga nak féroulén idja di sonal nit gni toubab bi bimou fi néké yén lan moo daun sén takhaway boudaun yék rék Sénégal gueuw dina am 20% de musulman néka réseau sociaux di sonal nit gni dém lén fowi
Nit Day mandou surtout un bon musulman.
Mandu Kaye moye yame si diné bifi Mohamed bayi ba nopi Di léral lissi bokoul
Yen xamolen louhew@@sambathiam9067
yaw topal feulé yaak sa boy Alpha yéna yam féroulén idja di beugueu ray nit gni@@sambathiam9067
Bayilene sagua ak khasté tontou thi kham kham tarikha bakhoul amoul dalil thi diné
Allahu akbar yaw yaye jaahil deque deque. Esque yaw ham ngeu lan moye baatu "Tariqa'? Jango ndeysaan motax. Yalla jubante leu. Aameen.
Kou doyni seydinacheikh nganan bein way walaxi yalla nala yalla reub té bayil doul kein waxoula mo gueun alhouran dagn la wax mo eup dolé té daga gatt xam xam ndax barina kouy diang alhouran alhouran reub la té çalatoul bou dieum si yonenté ko mana doon yalla nagoul la
Sawaye kholale maye niou souniou diam té nga teudje sa gategui tarikha cheikh ak tarikha boumou mana done benne président mounou ko fait djieulai thi kawe souf
Saway yamana doul yonent bi sakh tidiane la
Bayil fénn
Doul alpha
Yow kèn geumoula Tidjane manoko fi dieulé . Diangakatou al khouranoule karime-yi niougni réye nit-yi tia Yémen reye Ali mouhamed dieulélene makka. Bayil digueute tow geuemoulo dara
boy Alpha yamal sa place lii ngay déf tour wala khaliss diarouko ouy
@@dieyemamadou8847 boy Cheikh démal ngua togue
@tawhid-i3l yén sén khol moy dagga dina yagga dagga nak féroulén idja di sonal nit gni toubab bi bimou fi néké yén lan moo daun sén takhaway boudaun yék rék Sénégal gueuw dina am 20% de musulman néka réseau sociaux di sonal nit gni dém lén fowi
Serigne mansour dallam mo raw sa baye lo gatt gatt xam xam xamné diamou diaxil ak halim douniou yam
Té benen bi boy doul say doul doulal sa baye té bayi di wax si lo xamoul niou bari yangui len di detourné si say xalatou bopou yo xamné dego wax dji
Chieck mo meuna Féne
@@sidibeboubacar7527 Cheikh l'Algérien kay moy lolou soss rék lay déff
Déléne wakh rék war guene bayi khél aduna dou keur
@@sidibeboubacar7527 yow diango dîné mo waral sa wakh waya lou waye wakh mba mou déf bopam
Yaw togal di wakh ci tarikha yi rék warga Mouytou dé té ragal yalla
Li serigne mansour wakhe deugeula. Bayi fèen mou gneune fanané nafila . Wahabiyouna-yi dango khoti worma islam ndakh dioulite youngou réye makka ak médina ba néke thi pouvoir bi .niongou doungiou royoukaye
@@abdoudiallo8013 Serigne Mansour Sy dhé ay féne ak tapalé késsé lafi wakh ak bayi
@tawhid-i3l yow yoro dimension serigne mansour .té kou guiss sa tourbi kham né féen sakh ya ko dakha féen