@@modoukane9336 non sérieux imaginel MachaAllah khaler bou Ndaw Yalla tagate ko mou Mokal alkhourane ngune beugue def musique si bop bi. Te ki mineure là donc lep loumouy def sokhlo n’a ay kilifa. Est ce que ses parents sont au courant sakh....il a l’avenir devant lui donc n’a oute xam xam Mo woor!
Sénégal I love the way you uplift your rising stars irrespective of their backgrounds. I saw his freestyles on Facebook the kid is unbelievable, Courage p’tit frère ❤️
@ ziar frere nakamou lep diam mane mone j sui 100% hip hop galsen loudoul rap beuguouma mé andouma thi nguen influencée boy bi heur bi thi milieu muzik Ndakh ki thi diang la tolou Té mane aussi gueumouma limou wakh ni wathiéna alkhourane Meme ayatoul koursiyou bi nimouko tariwé bakhoul eguoul dafko diakhassé en meme dafko coupé
MA SHA ALLAH comme wathié nga kamil amnga droit ame métier yoor sa bopp yoor say wadjour, Serigne sakh dafa wara ame métier. Boufi kenn wakh ni Rap bakhoul nak. Mane meunoumako waar ndakh moma guene sorri ci alhourane Yalla nako Yalla diapalé ba limou djangue mou dieuffé ko te mayko loumou soutourlo ba terral ay wadjouram.
Mw perso neina wathier neu camil mei passion bokoul dra réligion mei tay sou deimei ba wara teiki ngiy nane na deim diangui doussi keinwu kouy saur thinam🥘🍜fait se k t’a a faire et diameu si yaw Frr✊🏿💯
Amoul lou gueuneu nekh mbeuguélou Yalla ak kham Yalla toppou ay diglem bayi ay térém. Il faut nguen encouragé les jeunes si yonou Yalla mo gueun lii. Yalnagnou Yalla sammeu si yoon wu dioub bi amine.
Mais ce gars est fou ou bien il se fou du monde . Comment peut on détourner un enfant qui a mémorisé le coran à prendre la voie de chaytane. Les parents de cet enfant devront te poursuivre en justice car c'est irresponsable. Xalé bi niou diangu loko alquran ngakoy rapp loo yoww kou réw nga té yabaté ishh.
Je suis rappeur mais je ne souhaite aucune personne à faire du rap parceque je sais bien que c'est du Haram et inechallah que dieu me donne le courage de laisser de la musique et nous canalisée vers le bon chemin
Je veux que le gars de Vibe radio supprime la vidéo...pour qu'on oublie le talibé Rappeur et qu'on concentre sur le talibé qui veut mémoriser le Saint coran. Alhamdoulilah#Allahou_Akbar
li mome dou lou bakh worna yalla ndonga darà dou melni yalla nala yalla sopi ndakh li dou lou bakh yone wou bakh rk mo ame solo lolou li dou lou bakh ani taloube yi 👂🏿
Sénégalais yi ay seytané reek lagne fi kou nek ak sa passion. Ki diang na ba wathié mais souko nekhei mou rap. Lernama gniy def ay commentaire negative yeup diangouniou sax so demei
Bayi len khalè yi keni yakh kholal gui rek wara diange ken begue ko def rappeur kat ak youma khamoul thieye senegal diakhalna niouma boy demal diangui mo guen si yaw ✊
N'oublié pa que ki fékouniou ko ci daara mouy diangue ci mbedd bi lagn ko forr mouy yelwane !! Loutakh ngueen sheytané !! Yene gniy commenté lay wakhal sen diang fann la yem !! Soff ngueen trop !! Rap bi dey diokhé million fils koula diapale nga guenneuh ci 💪 gueum rek lepp dina bakh inchalah
Salam Anleykoom Boy YA'ALLAH NALA RAPSEKH'LOU Bu baaakh Nga continué sa Jang Xam xam Ndakh dou Dooye YA'ALLAH Nga nk Khafiz bou Mak Amine Li diaroul Toop ndakh dou Deug YA'ALLAH NA Yékh YAWMAL'KHIYAM Kén douniou Ladj Rap Sa diné laniou laay laaj YA'ALLAH Nalén BUUR Dol'li SOUTOURA Amine
Je veux que le gars de Vibe radio supprime la vidéo...pour qu'on oublie le talibé Rappeur et qu'on concentre sur le talibé qui veut mémoriser le Saint coran. Alhamdoulilah#Allahou_Akbar
Sama yaram dafa daw nakhe wadiourem wationan ak môme mais Sénégal bakhe fi yoboul loubone lo neka ynou fekalatie lou bakhe dokhoufi yalla nanou sou ar amine
Mais c incroyable bayilen Ko mu diague alkhourane il est talibei et tout le monde sache belle et bien que yalla wahul ken mu bolei alkhourane ak di dem si rap il faut l'encourager à suivre le coran moy yonu yallla wa salam magui dieg lu nak
Mais yen élément iblis ngen nge koy posse si affairs you s’étant yii yalla na ndiou yalla moussal si ndiou melni yenn fi dou guiss j’aimee kou dee bagne koy rabal 😭😭😭 khalebi yalla na khelam tourne si al khouranoul Karim 🤲🏾🤲🏾
Moi je vois pas du mal vraiment cause rappeur yi fi you beuri jar Nanou Darah je send juste que l’enfant il est free calme pour te ces dires avec ces amis ils sont content et c’est sa qui fait la différence, xalé sou free rek Nice après le reste dankoy def calme qui nous dit que après quelques années dou nék le plus grand Rappeur wl president wl le plus grand des imams ... machallah fils reste comme tu est djangui après ga free d’accord 👍 one love yak say mokou 💪
Wax wax dji moye ki khelam nekaltoul sakh thi dara dia baye kham limouy diang khelam khalatam guisguisam lep thi rap bi lako tek 1 video bi wadiouram ak serignou dara bikoy diangal bouniouthi diouguone kone taye dougnouko idi fi diko lathie deja mineur alkhourane moye lep diegelou thi kadouyi 🙏
Li sakh boulènko défé day melni rappeur mo gueune nék si ndiangalém YALLA Th pourtant sou continuer alkhour ane bi mane nathié siw euleuk amthii khaliss amthii YALLA🤲🙏
Thiey adouna fi mou tolou de kou titoul rk do nit wallahi nit gno kham lep lou dieum thi foo rk lagnu sawar lou diko médiatisé en plus say wadiour rk la yeuram gnom gni alkhourane gnor bagnu dieul la yobou la dra ioe nga nek thi émission rap Yalla nagnou Yalla doli dimbalalée 🙏🏿
Amna nio khame ni séne wah mo bari🤭 lérnani niome ddiankeu niou kheumouniu dara nék fi di wa nane bayi Boy bi mou diankeu 🤫 SENEGAL da amniu saytané bilay
Ay way yalah nako sou niou boro dioubanti teko si yonou dioup walahi xam ngéne gni daniouy yaxeu derou s darayi ak yar kat yi naxa rina képou kouy serigne dara tadiar fa mak nia diaron؟dou degeu dou yon
Ce gamin est plus intelligent que vous le pensez, il vous a clairement montre qu'il ne veut pas de cheytane dans sa vie en concluant avec Ayatoul Kursi
🚨🚨🚨🚨Math mes vidéos yaw Katt sa ndaye gua dieul yaw lii noko nit di défé yaw daga li daga torox yaw sa taati ndaye rék 😥😥😥😥😥😭😭😭😭😥😥😥😭😭😭😭😥😥😥😭😭😭😥😥😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😥😥😥😥😭😭
Boy Sa baay diang lala deflo. Man bimay nekk dara j'avais votre esprit de rap.je maitrisais tout les son rap comme je réciter mes darses. Je m'ettais en tête de devenir un rappeur célèbre après le dara ctait a saint louis.mais après je me retrouve dans les écoles française a l'âge de 15 ans.et je ne veux plus être un rappeur tout comme les autres artiste mbalakh et consort car ils ne sont pas des idoles dans la société de vrai valeure je dis bien vrai valeur.maîtrisant le coran tu as un esprit riche et tu pourra l'exploiter sur des avenirs valeureux.moi je suis actuellement en fin de formation dans une école ingénieur.et je suis entrain de construire mon avenir tout en maîtrisant le coran,le fikh....
Mais essayons de l'encadrer même s'il est un talibé et qu'il est dans un Daara il a une passion pour la musique il aspire peut-être devenir quelqu'un demain quand même
Ma cha allá nena wathiéna camile yalla na ma yalla may beu ma am dom mou wathié camile
Amine
Amine
.
Ak mane amine
dom bou wathie kamil amoul solo dom bou dioup mo appou solo sa al Qran leppou ak dioup lay diangale sa mokal mo geuna wor wathie
mande al coran rek lay dougual ms guissouma kouma abonner 😭😭😭kou beuga al coran sisa xol abonner ma yallah fayla
Je me suis abonné.
Walahi wakh nga denga
Soula yalla takhè joukk jaroul ngay wayann nann ngir yalla. Et puis kouleu abonné woul cest du pechè
Ñoo ngi tuub bu baax ci yeexa abonné bi ya sheikh
Magui niii ma beug Alkhourane bamou diekh
C 2 chemin très très différents,
Quran et rap, bayi lène ko mou diangui, boulène ko changé , kii xèlmi maye nako mou nèk oulama
Bilakhi
Dans 3ans Imam ak Oustaz dina manqué Sénégal 😭🤣
malako wakh dh Senegal mom fo reck
😂😂😂
@@ndeyeantagaye3006 😅😅😅😅😅😅
Sans doute bro ta parfaitement raison
T yow gua nekk fi
C'est extrêmement grave. On ne peut pas prendre un enfant mineur sans autorisation de ses parents et l'exposer dans le web.
Effectivement ! Ces parents devrait porter plainte
Sa waay bayilene ki mou diangue Diiner. Mo eup solo bilahi.
bilahiii moy deugg
Frère mane sui 100% hip hop galsen mé iowla anda vrement ayatoul kousiyu bimou tari sakh nimouko tariwé bakhoul
@@modoukane9336 non sérieux imaginel MachaAllah khaler bou Ndaw Yalla tagate ko mou Mokal alkhourane ngune beugue def musique si bop bi. Te ki mineure là donc lep loumouy def sokhlo n’a ay kilifa. Est ce que ses parents sont au courant sakh....il a l’avenir devant lui donc n’a oute xam xam Mo woor!
والله
Dèmall yangui
Sénégal I love the way you uplift your rising stars irrespective of their backgrounds.
I saw his freestyles on Facebook the kid is unbelievable,
Courage p’tit frère ❤️
Je ne vais même pas continuer la vidéo laissez ce talibé apprendre ses cours coraniques ish... Vous êtes entrain de le détourner sans le savoir
Setanal après ngua soga commenter Monsieur Socrate 🤥
@ 😁😁😁 D'accord monsieur math. je te reviens 🤣
wax deug
@ ziar frere nakamou lep diam mane mone j sui 100% hip hop galsen loudoul rap beuguouma mé andouma thi nguen influencée boy bi heur bi thi milieu muzik
Ndakh ki thi diang la tolou
Té mane aussi gueumouma limou wakh ni wathiéna alkhourane
Meme ayatoul koursiyou bi nimouko tariwé bakhoul eguoul dafko diakhassé en meme dafko coupé
Tu doit terminer la vidéo d'abord avant de commenter le talibé à dit qu'il à terminer le corant
Arrêtez d'influencer ce petit garçon ! Il est encore mineur.
Al qur'an amul luko geun. Rap yeufu aduna rek la
Xam !
@@DKane-ow3tq frm ta gueul toi
DEUG dou rombAYE nopes.IBLISS DEIH LILAH DEUCKEÎ DIGNOU DEROUTER EN NOUS MEME ET A TRAVERS NÔUS MEME.LI ALLAHOU YALLAH TEIRER ILIAD RAFEITALNAKO SI BEUTI GNI SAGANE TOPALE LIMOUYE TARI:GIMOU TOGALE XALEIBI MOHLEINE TANI TE KOUMA MANAJITER NEIKOUFA.NANOU ALLAHOU YALLAH XIRE SI BOPAME
@@weshlegang6915 Toi, "frm ta gueul" ! Sale crétin !
MA SHA ALLAH comme wathié nga kamil amnga droit ame métier yoor sa bopp yoor say wadjour, Serigne sakh dafa wara ame métier. Boufi kenn wakh ni Rap bakhoul nak. Mane meunoumako waar ndakh moma guene sorri ci alhourane Yalla nako Yalla diapalé ba limou djangue mou dieuffé ko te mayko loumou soutourlo ba terral ay wadjouram.
Ki talibé la bayi lén ko mou diange 😭 vraiment da ngay warou li dou yoonn 😌
Nekal nit il veu just lui rendr la vie super
ki d'où ab donga wala srignie daram day diakhan
Rap lo boy bi baparès nan ko défal niane🤣🤣ya ndayi léw lék😅😅😅
Mw perso neina wathier neu camil mei passion bokoul dra réligion mei tay sou deimei ba wara teiki ngiy nane na deim diangui doussi keinwu kouy saur thinam🥘🍜fait se k t’a a faire et diameu si yaw Frr✊🏿💯
Amoul lou gueuneu nekh mbeuguélou Yalla ak kham Yalla toppou ay diglem bayi ay térém. Il faut nguen encouragé les jeunes si yonou Yalla mo gueun lii. Yalnagnou Yalla sammeu si yoon wu dioub bi amine.
C grave qui bayam beug mou nek havig allhourhan mouy rapp c grave
Une société de satan le Sénégal
Parsk rap dafa bonn putain arrêtez vos conneries....
Mais ce gars est fou ou bien il se fou du monde . Comment peut on détourner un enfant qui a mémorisé le coran à prendre la voie de chaytane. Les parents de cet enfant devront te poursuivre en justice car c'est irresponsable. Xalé bi niou diangu loko alquran ngakoy rapp loo yoww kou réw nga té yabaté ishh.
@@moustaphad.4274Saway music baxoul on l, ecoute me kenn gnanoul de gnouy tekk music
🤣😂😂
Boy bi déy niang bayii lékko moudiag daraa🙏🙏🙏
Nice na trope il faut l'aider faut pas le laisser à la Rue il peut servir pour demain👍👍👍
Respect
Lii laniou wakhhhh barakallahhhmusikkkkk 🤣 tégall beat käyyyyyy
Boy demal diagui svp🙏l'avenir🇸🇳 est dans l'apprentissage ✍️ entant que des frère♥️ bayi lène ko mou diagu 🙏
Du courage un jour tu seras un grand rappeur inchallah
Je suis rappeur mais je ne souhaite aucune personne à faire du rap parceque je sais bien que c'est du Haram et inechallah que dieu me donne le courage de laisser de la musique et nous canalisée vers le bon chemin
Que Allah te guide !! 😊😊😊😊😊😊
Amine yarabi
Yala nala yala sopi
J’aime trop le petit ❤️jspr vraiment le rencontre quand je vais venir au Sénégal 🙏🏾
Yaw ya nekh rekk
@@senegalndiaye1128 mdrr si nane la nekhe,khale bi damo ko fan trop
Machallah machallah
Bon boulot Math c bien d découvrir les jeunes talents
Si tt les youtubeurs étaient kom tw le Rap Galsén ira mieux
ET les darra irons où ?
Ey way li tamit lan la
Je veux que le gars de Vibe radio supprime la vidéo...pour qu'on oublie le talibé Rappeur et qu'on concentre sur le talibé qui veut mémoriser le Saint coran. Alhamdoulilah#Allahou_Akbar
Baylene ki mou dem diangui allkhouran mo opu solo khayrukom manta allamall khour ana waallamahou✍👆💗long vi a toi demall diangui
Wakhnga deugeu
Ohhh ndeysaane 🥺🥺🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁 mais Dk Meth boy bii bougn koy diappalé mouy moom reew mi si rapp 🎁🎁🎁🔐🔐🔐🔐 maachallah c’est extraordinaire
Frr dioumnga deh ki na dem diangui mo geune nganan dankoy produirele Lii rafetoul 🙅
li mome dou lou bakh worna yalla ndonga darà dou melni yalla nala yalla sopi ndakh li dou lou bakh yone wou bakh rk mo ame solo lolou li dou lou bakh ani taloube yi 👂🏿
Bo nekhé star😂boul faté sa niari Kharit tes fidel compagnon 😂
🤣🤣🤣🤣
Math talibe bi may nala buzz deh 100k si 2 jours rek for real 👌
Sénégalais yi ay seytané reek lagne fi kou nek ak sa passion. Ki diang na ba wathié mais souko nekhei mou rap. Lernama gniy def ay commentaire negative yeup diangouniou sax so demei
Dafa lére frr guayi dagno sof
Iow mom yay seytane mou bakh bi
Bien dits frère✊
Yaw mom yay nitou safara khana mbock ibliss nga 👹👹
@@ablayediallo1978 tu es fou dof rek ha ďef
Bayi len khalè yi keni yakh kholal gui rek wara diange ken begue ko def rappeur kat ak youma khamoul thieye senegal diakhalna niouma boy demal diangui mo guen si yaw ✊
Yakh ken boy bi rek thieye yalla ayatoul koursi bou ague sakh menou ko tari
Yakamti guen xalé yi diam Si yoonu bon ba Guen financiè len guir yàlla bayi Len xale yi Guen di doolel Si ak mbon ki ana aye waadiou ram ni
Kii xanà amouli mbokk
Lide.doyon.
N'oublié pa que ki fékouniou ko ci daara mouy diangue ci mbedd bi lagn ko forr mouy yelwane !! Loutakh ngueen sheytané !! Yene gniy commenté lay wakhal sen diang fann la yem !! Soff ngueen trop !!
Rap bi dey diokhé million fils koula diapale nga guenneuh ci 💪 gueum rek lepp dina bakh inchalah
الخلق ينظر إلى ظاهرك الخالق ينظر إلى باطنك فاحذر أن تزين محل نظر الناس وتقبح محل نظر الله نسأل التوفيق والإعانة شكرالكم
je suis un jeune rapeur mais je voulais ont aidé pour exploiter mon talent
Wakh len boy yi deug alkhouranne lako papam wakh mou def yagui nelaw math billahi
Billahi linga wakh deugleu
Bilahi
@@asbprod6722 math day nelaw billahi
@@babacarseck6720 math day nelaw kw billahi
vréma Sénégal mon âme nite yokhamni
aye mbame moléne guéne liguéye moye défare réwe pa rap🔥🔥
Math yagg fii way💪🏽❤️❤️
Yenn gni commentaire négatif kii dfeu wathie alkhouranne ba paré boy😍😍
ki de bou Fékké whtie Na xamoul dara wallaxi iska Degue Ga Limou tari bayi Len séen thiaxane yi
Il n'a pas bien récité ayatoul koursi .mais il récite parfaitement le rap) faute des parents malheureusement 🤩🤩🤩🤩🤩
@@MS-oi2lv bro ki leep lay def bou sikare ngua warou dou rapp rk lay def
Mai bou tarè yakhouko kone défoul lako ware
Même su wathié alkhouran mokalul . Diangue alkhouran takhul gua xam sa diner
Qui est là après l'analyse de Xalaat Tv🤣???? Math le TH-camur le Plus nul🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🙈Woyy😭
Bilay il est trop nul même 😂😂😂😂😂😂😂
Boy bii dou nitt dafa meune ba yakkou machallah💪👊🔥
Salam Anleykoom Boy YA'ALLAH NALA RAPSEKH'LOU Bu baaakh Nga continué sa Jang Xam xam Ndakh dou Dooye YA'ALLAH Nga nk Khafiz bou Mak Amine Li diaroul Toop ndakh dou Deug YA'ALLAH NA Yékh YAWMAL'KHIYAM Kén douniou Ladj Rap Sa diné laniou laay laaj YA'ALLAH Nalén BUUR Dol'li SOUTOURA Amine
Est ce qu'ils ont l'autorisation de filmer un mineur 🔞. Attention C très grave.
Niome Kay ils détournent les gamins
Ki papam yegoul won sa gniewna fi
Vraiment wakhal waye
Je veux que le gars de Vibe radio supprime la vidéo...pour qu'on oublie le talibé Rappeur et qu'on concentre sur le talibé qui veut mémoriser le Saint coran. Alhamdoulilah#Allahou_Akbar
@@abdoulayewade6075 wallay deggela man Limay khalat talibé bi mounna dem ba nekkafi imam am ay diabar ak dom gnouko gennal limoudon rap
Sama yaram dafa daw nakhe wadiourem wationan ak môme mais Sénégal bakhe fi yoboul loubone lo neka ynou fekalatie lou bakhe dokhoufi yalla nanou sou ar amine
bayiko mou diangue alkour ane mo guene 😭😭
Billahi
Mais c incroyable bayilen Ko mu diague alkhourane il est talibei et tout le monde sache belle et bien que yalla wahul ken mu bolei alkhourane ak di dem si rap il faut l'encourager à suivre le coran moy yonu yallla wa salam magui dieg lu nak
Bayi lene boy bi mou diang Al quranam ngir yalla
Douneko déf dh
Kidou Ndogo daara ab Ndogo daara warna tal lénén loudoul di déglou rapp bayilén khaléyi ñiou Diange magui diégalou bouwér 🙏🏾🙏🏾
Woy Talibé bi néna tégal Big Kay,😂😂😂😂😂
🤣mane bobou momay ray i a chopé l virus du rap
Ya Allahou ya rahmane ya Rahim yalla boumou done musicien yalla nasone oustaz wala sering
Math ki kouko diapalè mou dem 🔥❤️
Dafa lére frr
Kouko diapalé si lane nonou
Yaw nitou safara nga
quand ils ont eu besoin du petit, il est venu clean Avec des habits propres.
Mais yen élément iblis ngen nge koy posse si affairs you s’étant yii yalla na ndiou yalla moussal si ndiou melni yenn fi dou guiss j’aimee kou dee bagne koy rabal 😭😭😭 khalebi yalla na khelam tourne si al khouranoul Karim 🤲🏾🤲🏾
Amiine yaa rabbi
Bilay diguéne yakh domou diambourdji rek continuer si d'Ara dji mogueune
Ki bodémé serigneme sakh yegoule ni moguise deuke bi di rap 😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂 wooy
😂😂😂😂
😄😄
😹😹😹Ehh iow léwna dh
Ndeyssane. Il faut les aider à changer de vie. Nalene yalla dimbale ak niit you bakh yi. Bouma richone... ndeyssane....
Yaw matt mes vidéo est ce que çava bouléne yakhe boybi laisser le apprendre le coran bouléne ko yobou si chéytané
billahi
Mais lii divertissement la rek c'est un gamin il a le droit de se divertir.
@@falloudiame6625 deug DEUG bilae machallah gueenee yaguee gueenee wér
@@falloudiame6625 deug DEUG bilae machallah gueenee yaguee gueenee wér
Wakh nga deug dh
Math mes vídeo sa diobou ndey bayil ndey nit ki mou diangui ngay yakheu boy bi ndm
Félicitation boy man mom sathie Mango mo yakheu sama diangue arabe 🤧🤧🤧
Moi je vois pas du mal vraiment cause rappeur yi fi you beuri jar Nanou Darah je send juste que l’enfant il est free calme pour te ces dires avec ces amis ils sont content et c’est sa qui fait la différence, xalé sou free rek Nice après le reste dankoy def calme qui nous dit que après quelques années dou nék le plus grand Rappeur wl president wl le plus grand des imams ... machallah fils reste comme tu est djangui après ga free d’accord 👍 one love yak say mokou 💪
Pas pour le moment mou dougou si game bi mais meune n’a âme encadrement bou bakh pour ses étude after sou parei c a lui de décider sa vie
Wax wax dji moye ki khelam nekaltoul sakh thi dara dia baye kham limouy diang khelam khalatam guisguisam lep thi rap bi lako tek 1 video bi wadiouram ak serignou dara bikoy diangal bouniouthi diouguone kone taye dougnouko idi fi diko lathie deja mineur alkhourane moye lep diegelou thi kadouyi 🙏
Akhlou Seuytané xalaat tv ya woor💪💪💪💪💪
😂😂😂😂 Baal ko rek
Pour moi xalaat TV est le meilleur 👊👊👊👊👊
Kii iska tàlibé la mokoloull àyatoull koursiyou senegal mô nekh animateur yi amouniou bén programmes
Thim
Sunu futur dip✅❤️😂
J'ai abonné grâce le petit merci frère li nice n'a trop
Nn Senegal mo tothie taloubé mèl nii 😭😭 j’ai peur 😱
Khana talibet d'où note go
Taleibbi nit la amna droit deff li khalei you bakh yeup di deff
Li dé du darra sy talibé damay fataly bima é dara tapp rekk lardon donn déglu te yaxill dar
Nice grand Amath 💰
Est ce que vous avez l'accord de ses parents avant cet interview ???
Bah je crois nada
Ndeyssane, que ses parents lui fassent aller à l'école. Je vois en lui un génie wallahi. Qu'Allah te guide et te protège petit !
Li sakh boulènko défé day melni rappeur mo gueune nék si ndiangalém YALLA
Th pourtant sou continuer alkhour ane bi mane nathié siw euleuk amthii khaliss amthii YALLA🤲🙏
Mdr bayil boy dem diangui bayam beug na si mom lenen loudoul rappeur 😂😂😂
Arrêtez vos commentaires négatifs.. Personne d'entre vous n'est iman ni oustaz et vous ne le serez non plus..
Tu n'est point Dieu pour prédire l'avenir d'autrui ☝☝☝
@@abdoudiakhate7358 tu n'es même sur la voie 😉
@@joblafouiny3724 A bon entendeur salut
Il à une très immense spiritualité Macha Allah
Kou deglou sa flow kham ni dieul nga dip🤣🤣
kou nek ak sa passion, ki sougnko diapalé si rap bi meune na percé réussir dimbali famille wam.
Thiey adouna fi mou tolou de kou titoul rk do nit wallahi nit gno kham lep lou dieum thi foo rk lagnu sawar lou diko médiatisé en plus say wadiour rk la yeuram gnom gni alkhourane gnor bagnu dieul la yobou la dra ioe nga nek thi émission rap Yalla nagnou Yalla doli dimbalalée 🙏🏿
Amna nio khame ni séne wah mo bari🤭 lérnani niome ddiankeu niou kheumouniu dara nék fi di wa nane bayi Boy bi mou diankeu 🤫 SENEGAL da amniu saytané bilay
BOY BI NÉNNA DAMAYE DIKLLOU DIP LOU BARY DÉSS NA TOUTY THI KANAME IMAME MOME DANNE KOY FAYE MOUYE DJITTÉ NDAKH DOU AME FÉNNE
Billahi
Bilay yaw lou leer nga waxx
Hahahaahhahhah
😂😂😂😂😂😂😂😂
Non non non stop
Beug kou suivre sén chaîne bi boum takh ŋgén yakh khalé bi
Yaw encouragé wo ki si mou jiangui ngua indi ko fi may wakh nguéni commenté naane "kouko jiapalé mou dém" yéna gui togn khalé bi ak ay wajiouram
Bilahi wakhga deug
Walâhi
Ay way yalah nako sou niou boro dioubanti teko si yonou dioup walahi xam ngéne gni daniouy yaxeu derou s darayi ak yar kat yi naxa rina képou kouy serigne dara tadiar fa mak nia diaron؟dou degeu dou yon
Ce gamin est plus intelligent que vous le pensez, il vous a clairement montre qu'il ne veut pas de cheytane dans sa vie en concluant avec Ayatoul Kursi
Si vous êtes des vrais Bayfal vous allez aider enfant de retour au Coran, mo guen mais rap vous modi. Expérience 0
Tapez ndiatigué comédien sur youtube et abbonnez vous vite rée ba tass 😂 thiéy ndiatigué mingui tothie youtube
Vous avez gâché la vie de ce garçon.
Aulieu que mou djang diner gen koy deff star rap.
Subhanalllah vous serez tous jugés pour ca wallah
Bien dit
Boy dianguale continues diangue alkhurane yalla nala yalla same
Def ngen lou niaw dh ta xalei bi tamit khawma fan lay diange me lii dou yoon
🚨🚨🚨🚨Math mes vidéos yaw Katt sa ndaye gua dieul yaw lii noko nit di défé yaw daga li daga torox yaw sa taati ndaye rék 😥😥😥😥😥😭😭😭😭😥😥😥😭😭😭😭😥😥😥😭😭😭😥😥😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😥😥😥😥😭😭
Il a besoin des conseils positifs
Nguir yalla rekk
Kou nekk ak plaçam
Tabate lakoum nonou alkhourane tabat tabat tabat tabat tabat tabat tabate
Papam beuge mou doon magou dine ngèn beuge ko deff rappeur torokh 🔫🔫
Khale bi amoul. Kersa amoul diom demal diagui bakhena ,,000000000
Wakhal sa kaw
Magoum rappeur kay gay wax 😂😂😂
May wakh gnou nane ko outal tourou rappeur wayé yala molen eup dolé
@@Jamy2418 waxatiko dh dangay rous sakh
Boy Sa baay diang lala deflo.
Man bimay nekk dara j'avais votre esprit de rap.je maitrisais tout les son rap comme je réciter mes darses. Je m'ettais en tête de devenir un rappeur célèbre après le dara ctait a saint louis.mais après je me retrouve dans les écoles française a l'âge de 15 ans.et je ne veux plus être un rappeur tout comme les autres artiste mbalakh et consort car ils ne sont pas des idoles dans la société de vrai valeure je dis bien vrai valeur.maîtrisant le coran tu as un esprit riche et tu pourra l'exploiter sur des avenirs valeureux.moi je suis actuellement en fin de formation dans une école ingénieur.et je suis entrain de construire mon avenir tout en maîtrisant le coran,le fikh....
Keur masar guiss nafa benna talibè di toppou di son dip son bouma tèck mou toppasi nn dip est le meilleur wallah🔥🇸🇳❤
Mdr dip xalei bou yi am 4 ans moy topousi sonwam yi
No dip mo mell nonou
Man maillot bi moma neex. Citizen 💕
Xalé bii beug na rap bii mais souma sagnone daal ngén bayiko mou continé diangone coz mo eup solo
Merci d'avance pour votre réponse rapide je vous remercie pour votre réponse
Boulen ko yakhal avenir am. Il faut l'encourager pour quil se concentre sur ses etudes coranique mo eup solo
Félicitations aux petits il est vraiment très poli
Mais essayons de l'encadrer même s'il est un talibé et qu'il est dans un Daara il a une passion pour la musique il aspire peut-être devenir quelqu'un demain quand même
Doul
Non il n'a pas de passion mais c'est juste il répète le couplet d'akbess
c cool et super bien