Allahou Akbar Pape Niang wéreugoul Sah accidenté watt,dagno narona déé gnoune Nieup thi accident bi😭

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 9 ก.พ. 2025

ความคิดเห็น • 1.2K

  • @DadaCisse-hc6ug
    @DadaCisse-hc6ug 4 หลายเดือนก่อน +403

    PResident Diomaye Faye dagnou layy gnane si dieum SEydina Mouhamed dieulale gnou PApe Niang mi en charge

    • @diakhereseye3275
      @diakhereseye3275 4 หลายเดือนก่อน +14

      Ohhhh métina trop sakhe yalla na yalla fayy

    • @BintaFaye1
      @BintaFaye1 4 หลายเดือนก่อน +15

      Bilay il mérite pas sa nioukoy sétane ak limou def si Sénégal rek président diomay vraiment warna ko yeubou eureup beumou wérr vraiment diomay ak sonko tamit boudé louway def si lou bakh yallah fey lako yallah dinala fey sa khôl bilay massa kou bakh rek la yallah di tékk nattou

    • @ElajGueye-nv7su
      @ElajGueye-nv7su 4 หลายเดือนก่อน +3

      quete pour un prado automatique comme bou oustaz Aliou sall

    • @IbouMbaye-y3j
      @IbouMbaye-y3j 4 หลายเดือนก่อน +3

      Bly wkh gua degue 😢meti na trop 😊

    • @oumylayeba8749
      @oumylayeba8749 4 หลายเดือนก่อน +7

      Ayway Pape yalnala yallah dolé takhawou si barcké seydina Mohamed

  • @awakama450
    @awakama450 3 หลายเดือนก่อน +8

    yalla na yalla takhawoula pape barki mouhamed

  • @MbeneSeck-x8c
    @MbeneSeck-x8c 4 หลายเดือนก่อน +79

    Lepeu baye bakh inchalla si barki moukhamed psl 🙏🏽🤲🏽🙏🏽

  • @toulayesarr-uj8vr
    @toulayesarr-uj8vr 4 หลายเดือนก่อน +53

    pape niang adouna moko khamoul wayé mane lima guis pape nian fakhirla nitou yallah mission biko yalla sante laye dokh yalla nala yalla borombi téguil sa natou bi

    • @cmavie580
      @cmavie580 4 หลายเดือนก่อน

      Allahuma Amiin

    • @NgounDia
      @NgounDia 4 หลายเดือนก่อน

      Amine ❤​@@cmavie580

    • @NgagneNdiaye-g1f
      @NgagneNdiaye-g1f 18 วันที่ผ่านมา

      Thiéyy yalla akka yéémé loum déff dou HAZARD Pape Niang du courage yalla moungui ande ak yaw walahi aziime🙏🙏♥️♥️

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye218 4 หลายเดือนก่อน +209

    Pape niang mo bakh souniou borom dinala dėfal diam

    • @Mollahmorgunofficiel
      @Mollahmorgunofficiel 4 หลายเดือนก่อน +3

      Ki na bayi victimisation bi ta dém liggey

    • @moussasy8532
      @moussasy8532 4 หลายเดือนก่อน +2

      ​@@Mollahmorgunofficielyw isk wérnga😢

    • @astoundiaye1832
      @astoundiaye1832 4 หลายเดือนก่อน

      Amine

    • @AblayeNdongo-x4m
      @AblayeNdongo-x4m 4 หลายเดือนก่อน

      ​@@Mollahmorgunofficiel Bouma guissé photo sonko Bi dama rouss bilakhi 😌😌😌😌😌

    • @Mollahmorgunofficiel
      @Mollahmorgunofficiel 4 หลายเดือนก่อน

      @@AblayeNdongo-x4m goor dafay liggey

  • @sokhnadieye3661
    @sokhnadieye3661 4 หลายเดือนก่อน +30

    Salam je pense que ce monsieur a besoin de roqya. S’il voit mon commentaire il peut me contacter . Notre cabinet le prendra en charge inchallah

    • @NgoneMbaye-y3j
      @NgoneMbaye-y3j 4 หลายเดือนก่อน +1

      Bilay ya bakh

    • @SambaKa-c8x
      @SambaKa-c8x 4 หลายเดือนก่อน +1

      Voilà t'a dit la.verité❤

  • @BinetaBeye-j7e
    @BinetaBeye-j7e 4 หลายเดือนก่อน +223

    Dama am louma meeti pape méritéwo li thiey état bi takhawouléne ki limiy dokh séne rôle lawone

    • @mormbaye2989
      @mormbaye2989 4 หลายเดือนก่อน +9

      M ndogal la 😢😢😢m sant yalla❤metina

    • @momoseck1617
      @momoseck1617 4 หลายเดือนก่อน +3

      Yow doul
      Bayilén thiakhane
      Lougnou wakh nguén nane état
      Que ce que vous foutez à la fin

    • @oumydiatta4838
      @oumydiatta4838 4 หลายเดือนก่อน

      Bilahi senegalais mo seytane ki ligueyoul di def social louy lolou? Mane dal duomi na ta so wakhé gnouni danga soxor
      ​@@momoseck1617

    • @Hgjkjjjkl
      @Hgjkjjjkl 4 หลายเดือนก่อน +4

      Lou diok guéne polotiséko ki liko dal natoula gnianal ko mo gueune guay profite di politique, pape yala na sounou borom takhawoula

    • @OumiNdaw-t2q
      @OumiNdaw-t2q 4 หลายเดือนก่อน +2

      Walahi ndeyssane natou la reck yalla mococo téck yalla meun nako tégui yalna done li gueune si mome yalnala yalla tahawou inchalah té mou samal la bopam inchalah yalla boula beugué dodiouk si natou ngueunèlle la

  • @astoumbodj24
    @astoumbodj24 3 หลายเดือนก่อน +1

    Yalna la yalla yeuketi si diam 🙏🙏🙏🙏

  • @mamediarradieng8034
    @mamediarradieng8034 4 หลายเดือนก่อน +330

    Santal banga togue diko netali 🙏yalla nla yalla sam

    • @bequediallo458
      @bequediallo458 4 หลายเดือนก่อน +5

      Amiiiin'Allah

    • @mouhamedgaye6071
      @mouhamedgaye6071 4 หลายเดือนก่อน +5

      ماشاء الله عليك بالله 😊

    • @FatouSeck-nz7eb
      @FatouSeck-nz7eb 4 หลายเดือนก่อน +3

      Amine 🤲🤲🤲🤲🤲

    • @m.d.d.c.6594
      @m.d.d.c.6594 4 หลายเดือนก่อน +2

      Pape nk dafa wara tok nk akh

    • @naffidieye4429
      @naffidieye4429 4 หลายเดือนก่อน +1

      Bilay lolou la wah

  • @Babacar998
    @Babacar998 4 หลายเดือนก่อน +1

    Ndeyssane pape niang yalla nala yalla takhawou may la wér ak tann ak molém dioulit inch'allah 🙏🙏

  • @NeseDia
    @NeseDia 4 หลายเดือนก่อน +214

    Seytane mola top deh 👈 il veut détruire ce que tu fais, laide que tu apportes. Seytane dong moko def

    • @ManstillAman
      @ManstillAman 4 หลายเดือนก่อน +34

      Yalnako yAllah taxawou si barké Seydina Mohammed PSL

    • @khadydiagne9686
      @khadydiagne9686 4 หลายเดือนก่อน +20

      C’est ça que j’ai dis mes yalla nako yalla takhawou si barke seydina Mouhamed 🤲🤲

    • @mamabarry5903
      @mamabarry5903 4 หลายเดือนก่อน +8

      Ayii wayii pape niang yalla nala yalla takhaou bilahi je te suis à chaque fois ligayi def si diam yi yalla nalako yalla fayii li diapal ni natoula rk ak pekh seytaner yalla nala yalla mousal si seytane ak pekh none bilahi sa me touche bcp

    • @biteye305
      @biteye305 4 หลายเดือนก่อน +5

      Massa pape yalla nala yalla may wér takhawou la same la are la watoula

    • @diopfatoucisse7676
      @diopfatoucisse7676 4 หลายเดือนก่อน +6

      Seytanè meune na lou eup lolou

  • @Coumba-pz9fk
    @Coumba-pz9fk 4 หลายเดือนก่อน +3

    Soy liguéyal sounou borom dalay ték ay natou so mougnié mou gueureum mal bopap serigne pape niang yalana la yala fayal bopam amine❤❤❤❤❤

  • @gayenogaye6734
    @gayenogaye6734 4 หลายเดือนก่อน +40

    Oh ndaysan metina waye pape natou yalla douko tek mala thi nit rek lakoy tek yalna yala takhawoula 😭😭😭

  • @mameboussotall1237
    @mameboussotall1237 2 หลายเดือนก่อน +2

    Machall yalla na yalla faye

  • @aminathiam3124
    @aminathiam3124 4 หลายเดือนก่อน +25

    Hoooo. Masta wayy mèty na trop mais yalla nala yalla takhawou 😭😭❤️🙏

  • @ndaryndoye7586
    @ndaryndoye7586 4 หลายเดือนก่อน +15

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭no grand bi Sénégal gnépako warako diapàlé bilahy 😭😭😭sama khole dafa toye grand yalnala yalla taxawou barkepe seydina mouhamed psl 🤲🤲🤲

  • @theblackmamba434
    @theblackmamba434 4 หลายเดือนก่อน +186

    Saytané mola topou mais dinala bayi legui inchallah

    • @AissataBah-ih1kp
      @AissataBah-ih1kp 4 หลายเดือนก่อน +8

      In sha Allah🙏

    • @saratasall6283
      @saratasall6283 4 หลายเดือนก่อน +7

      Thiat ak saytanè walay

    • @RamatoulayeDiallo-gd8ru
      @RamatoulayeDiallo-gd8ru 4 หลายเดือนก่อน +7

      C est possible dé nit kounék lay tassél en tout cas doyna War

    • @kinefall9902
      @kinefall9902 4 หลายเดือนก่อน +2

      Ho massa

    • @babacarsarr6350
      @babacarsarr6350 4 หลายเดือนก่อน +3

      Yallanako yalla doli takhawou nimouye takhawo diamou yalla yi nako niepou doli nianale pape ndiaye sounou sopes khole

  • @MbackeSerign
    @MbackeSerign 2 หลายเดือนก่อน

    Walahi pape yalla molay fay diambar deug gua ❤❤

  • @adjaniang4352
    @adjaniang4352 4 หลายเดือนก่อน +112

    Yalla nalla yalla takhawou thi barke Seydina mouhamet

    • @diodiokone781
      @diodiokone781 4 หลายเดือนก่อน +10

      Salalahou Aleyhi Wassalame. Amine Yarabal Alamine

    • @massmbenguembengue5869
      @massmbenguembengue5869 4 หลายเดือนก่อน +4

      Yalla Nala yalla takhawou

    • @SadioNdoye-g5n
      @SadioNdoye-g5n 3 หลายเดือนก่อน

      Amine inchallah

  • @ladivatalibecheikh6845
    @ladivatalibecheikh6845 4 หลายเดือนก่อน +9

    Yalla nalla yallah takhawou ci barké seydina Mohamed (psl)

  • @eulthewritah4070
    @eulthewritah4070 4 หลายเดือนก่อน +90

    Walahi Toma yaw état mola wara dieul en charge total en 100% tu a sacrifié tout ton life pour les malades yaw nittu aldiana deugg nga vrai diambar li metina trop yalla nala sunu borom takhawou walahi sama xol nekhoul dara

    • @samediop2185
      @samediop2185 4 หลายเดือนก่อน +8

      Alaxouma amine

    • @KhadyDiouf-jp1mc
      @KhadyDiouf-jp1mc 4 หลายเดือนก่อน +3

      Yalnala yalla maye wére ak goudou fane té takhawoula thi barké seydina Mouhamed 🤲🤲🤲🤲

  • @dessna69-p5r
    @dessna69-p5r หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤yalla nalla yalla deffal diamou

  • @toufamar4496
    @toufamar4496 4 หลายเดือนก่อน +58

    They sougne borrom yalla nalla yalla maye weur

  • @NgagneNdiaye-g1f
    @NgagneNdiaye-g1f 18 วันที่ผ่านมา

    Thiéyy yalla akka yéémé loum déff dou HAZARD du courage Pape Niang walahi aziime yalla moungui ande ak yaw🙏🙏❤️♥️

  • @FatouNdaw-i7v
    @FatouNdaw-i7v 4 หลายเดือนก่อน +11

    Vraiment baye pape diambar gua yalna la yallah sam.fierté gua dé Machallah ci tawhid bi

  • @NdeyeMaguetteNon
    @NdeyeMaguetteNon 4 หลายเดือนก่อน +2

    Yalnala yalla same pape niang mayla wér

  • @ndongobouQuench
    @ndongobouQuench 4 หลายเดือนก่อน +73

    étta droit prend en charge grand pape barki yalla li méti na way Sénégal dou rew way😭😭

    • @ndongobouQuench
      @ndongobouQuench 4 หลายเดือนก่อน +5

      Ki dafa sone barki Serigne Babacar sy

    • @mameboussombaye7116
      @mameboussombaye7116 4 หลายเดือนก่อน +4

      Athia

    • @AngeliqueNdiaye-c7b
      @AngeliqueNdiaye-c7b 4 หลายเดือนก่อน +1

      Yalna yalla samla si barcke yonente sala lahou aleyi Wa salam weral ak diam les gens ont besoins de toi

  • @BayeZall-v6i
    @BayeZall-v6i 3 หลายเดือนก่อน

    Yalla na la yalla défal diamou ❤

  • @NdeyefatouFayendao-kb2oy
    @NdeyefatouFayendao-kb2oy 4 หลายเดือนก่อน +4

    Machalah yalla na yalla same léne sène dounde ame na diarigne longue vie à toute l'équipe Barker Mouhalmad SalAlahou Allah Mouhalmad Psl ❤️🙏

  • @RouguiBa-c1y
    @RouguiBa-c1y 4 หลายเดือนก่อน +5

    Machallah yalana yala faye te samala te barkel Amine yalla 🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @mariamadrame3371
    @mariamadrame3371 4 หลายเดือนก่อน +8

    Ohh pape yaye diambar 😢massa Yalla nga tané akh diamm 😢

  • @aminataseck8061
    @aminataseck8061 4 หลายเดือนก่อน +5

    Walahi yalnala yalla dèfal diam ak soutoureu
    Yalnala yalla dèfal tan ci barkè alhourane

  • @ndeyeantafall7813
    @ndeyeantafall7813 4 หลายเดือนก่อน +30

    Ndeysan pape yalna la suniou brome takhawou wereul la samoula😢🤲

  • @BayeDame-k4q
    @BayeDame-k4q 10 วันที่ผ่านมา

    Pape ya bakh❤da ame Lou yalla dame si yaw❤borom ame thiergua❤

  • @ndeyeamygning947
    @ndeyeamygning947 4 หลายเดือนก่อน +115

    😢qu'est ce qui nous empêche de cotiser pour Pape Niang lui même?

  • @ousseynoutine8885
    @ousseynoutine8885 4 หลายเดือนก่อน +4

    Pape Niang yalnala yalla weureul this barcké seydina Muhammad 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @ibrahimaFall-f3t
    @ibrahimaFall-f3t 4 หลายเดือนก่อน +21

    Pape niang l’état doit l aider franchement est prompt rétablissement

  • @pendadiagne5436
    @pendadiagne5436 4 หลายเดือนก่อน

    Massa frère sa gueme yalla molay walou dina bakhe dei inchalla ❤❤❤❤

  • @luttesimplemoraw253
    @luttesimplemoraw253 4 หลายเดือนก่อน +16

    Oh bn rétablissement l'ambassadeur des malheureux

  • @modoundlofficiel2706
    @modoundlofficiel2706 4 หลายเดือนก่อน

    Diam ci yaw pape niang❤❤

  • @sallsoda3090
    @sallsoda3090 4 หลายเดือนก่อน +11

    Ndeysane li mètina pape yalla nalla yalla takhawou yènè bi gua âme si askanwi 😭😭😭😭

  • @MariemeThiaw-z4k
    @MariemeThiaw-z4k 2 หลายเดือนก่อน

    Yalna sa barôm dëfaal la tawfexx akk taysir barkeep Bismillah

  • @MaodoLo-s5v
    @MaodoLo-s5v 4 หลายเดือนก่อน +2

    Ohhh li méti na trop 😭pape niang yalla nala yalla takhawou la té samla si barké saydina Mouhamed

  • @abdoulayesow3207
    @abdoulayesow3207 4 หลายเดือนก่อน

    Oh ndaysane 😮 yalna yalla tahawoula pape Niang

  • @ameenahmina5533
    @ameenahmina5533 4 หลายเดือนก่อน +14

    Diam rek ngay am...yalnala yalla takhawu...niaane bi sama khol lako tibbei😢❤

  • @modoundlofficiel2706
    @modoundlofficiel2706 4 หลายเดือนก่อน

    Yalla nala yalla samou pape niang❤❤

  • @Maguichoumar
    @Maguichoumar 4 หลายเดือนก่อน +7

    Ndeyssane Pape lii thiate la wallah yalla nala ya Allah takhawou barké Nabil Moustapha PSL❤

  • @RamaGueye-v3s
    @RamaGueye-v3s 4 หลายเดือนก่อน +12

    Ndaysane pape yalla nala Yalla takhawou in challa natou la rèk bou dièkhè rèk dièkh na

  • @SenghorNdeye-ey7mo
    @SenghorNdeye-ey7mo 4 หลายเดือนก่อน

    Machala yalla na yalla def al diam be guawer ac diam amine pape leup yalla rec la inchallah

  • @fanachou5402
    @fanachou5402 4 หลายเดือนก่อน +2

    Massa waye pape nit kou bax mashallah du courage yalla n'a la yalla Faye sa xol

  • @RahmatoulayeCagny
    @RahmatoulayeCagny 4 หลายเดือนก่อน

    Yalla nako yalla safaral si barki sangue bi pape niang dafa bakh MachaAllah

  • @NdeyebinetaKanté
    @NdeyebinetaKanté 4 หลายเดือนก่อน +2

    Ndeyssane yalla nala yalla bourbi takhawou si barké seydina Mohamed iow amgua loula topp mais yalla moko eupp dolé lou bakh liguaye déf doko perte jamais 😢

  • @NdeyeNdiaye-ub7is
    @NdeyeNdiaye-ub7is 4 หลายเดือนก่อน +2

    Yalla lou bakha rek lay défal inchalla boroba khaga

  • @AichaBa-xk5jp
    @AichaBa-xk5jp 4 หลายเดือนก่อน +22

    Pape svp togal ba weure mo guénn sa yéné gneupako khame 😌😌🙏🙏

    • @gtheboss9635
      @gtheboss9635 4 หลายเดือนก่อน +1

      Il veut mais dsl il n peut pas

  • @MameArameSy
    @MameArameSy 4 หลายเดือนก่อน

    Pape Massa yalla Jiékhoule wallakhi❤❤❤❤❤❤

  • @MbeneSeck-x8c
    @MbeneSeck-x8c 4 หลายเดือนก่อน +8

    Yalla nala takhawou si barki moukhamed psl ❤️🙏🏽🤲🏽🙏🏽

  • @FantaToure-eu8mt
    @FantaToure-eu8mt 4 หลายเดือนก่อน +6

    Aaay waaye pape Niang.😭😭😭😭😭😭😭

  • @ramatoulayebabou1084
    @ramatoulayebabou1084 4 หลายเดือนก่อน

    Masa pape li yeup na
    toulaaaa bina diekh inshallah 😢

  • @omardiop4369
    @omardiop4369 4 หลายเดือนก่อน +2

    Thia degue degue kou bahngua dé. YALLA NA LA BOUR YALLA WEREUL, safaraal la. Amine.

  • @KhoudiaSarr-uk7sb
    @KhoudiaSarr-uk7sb 4 หลายเดือนก่อน

    Ndayesane yalna yalla defal la diamou inchallah 🙏 pape Niang 🙏🙏🙏

  • @MameyacineDiop-u6h
    @MameyacineDiop-u6h 4 หลายเดือนก่อน +9

    Alhamdoulilaye santal yalla bou bakh yalla nala yalla maiye were ak werlé inchallah si Barker seydina mouhamed psl

  • @KhadimNgom-dl3kj
    @KhadimNgom-dl3kj 4 หลายเดือนก่อน

    Pape niang yalla na la yalla takhawou te samla si barkeb al Quran

  • @FatouCisséBâ-q9y
    @FatouCisséBâ-q9y 4 หลายเดือนก่อน +3

    As salamou aleykoum Niang yagallen lolou té werr tawfekh rek ak tayesir amiin y’a rabi 🤲🤲

  • @eliseemendy9698
    @eliseemendy9698 4 หลายเดือนก่อน +1

    Lolou dou ame yalla téré Yalla dina same inchallah 🙏

  • @hhht734
    @hhht734 4 หลายเดือนก่อน +3

    Ohh pape Niang mi yeureum nako trop

  • @fatimataka6570
    @fatimataka6570 3 หลายเดือนก่อน

    Oh massa yalla nako yalla tegui 🙏🙏🙏🙏

  • @agnesantacama1032
    @agnesantacama1032 4 หลายเดือนก่อน +11

    Vraiment l'état doit vous prendre en charge. Li ngueye def si social AK diko def si New gui dôle yi... Yalla boula Yalla setane mouk.
    Souniou borom Yalla nala tek lokho yow AK sa ndiabote🙏🙏🙏

  • @DTFTV
    @DTFTV 4 หลายเดือนก่อน +1

    Massta Metina trop : Yallah Mayla werr
    ak werlé 🙏🏽😮😢😭

  • @cheikhouna3538
    @cheikhouna3538 4 หลายเดือนก่อน +25

    Danga dimbali nit Kou andone AK rapp you sokhora sokhor mola Indile galancor yi yeup yalla teguil la Say diafé yaw kou bakh nga frère

    • @SalihateNiang-wd2xp
      @SalihateNiang-wd2xp 4 หลายเดือนก่อน +5

      Cheikhouna c est vrai Mane sama élève la rap bou sokhor dougone ma yobou Ko niou faje ko rap bi nima dinala wékh khate ndakh ki sene mame lawone ak Mane gua douguessi.maye rétane ndakh guemouma wone lolou mais 2ans yi sama ligueye yépa yakou sama yaram wereudi looole.wayé nak la khawela wala khawata ilah bilah

    • @cheikhouna3538
      @cheikhouna3538 4 หลายเดือนก่อน

      @@SalihateNiang-wd2xp yalla nalla Borom bi yeukeuti may la weer ba nga nékat si say activités AK sa liguey il faut beaucoup prié et écouter le coran yalla bakhna
      Raap yi yak lagne geuneu meun motakh nit lo khamoul danga si def nank

  • @SoumayatouNdiaye-k1h
    @SoumayatouNdiaye-k1h 4 หลายเดือนก่อน

    Daysane nala yalla fay sa khol ❤😊

  • @fatoudiabang-ic5dj
    @fatoudiabang-ic5dj 4 หลายเดือนก่อน +7

    Que Dieu vous bénisse mon frère

  • @ibrahimabadiane5769
    @ibrahimabadiane5769 4 หลายเดือนก่อน

    Thieuy yalla pape 😢lidéy natuu yalla deug là 😭😭😭😭

  • @isseuba2677
    @isseuba2677 4 หลายเดือนก่อน +4

    Yalla nala yalla takhawou natou yalla rek la ak thiate yalla nala yalla r thiate

  • @moustaphamboup730
    @moustaphamboup730 4 หลายเดือนก่อน +1

    Pape Niang , Yalla na Yalla may la wéer té samb la si barké Seydina Mouhaméd Salla lawou aleyhi wa Salama .

  • @TabaraMbodj-b7j
    @TabaraMbodj-b7j 4 หลายเดือนก่อน +11

    Yalna yalla defalén diamm yéne wa association bi 🙏🙏🙏

  • @diawniang3063
    @diawniang3063 3 หลายเดือนก่อน

    machalah yalla na borom bi défal la diam

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 4 หลายเดือนก่อน +6

    Yalla Nala yalla Samou😢😢😢😢😢😢😢

  • @MarieSao-oh4ro
    @MarieSao-oh4ro 4 หลายเดือนก่อน +1

    Macha allah yalla na la yalla takhawou

  • @seybatoubar5500
    @seybatoubar5500 4 หลายเดือนก่อน +5

    Pape yalnala yalla takhawou andak yalla réka woor yalla molaye samal bopam

  • @FatoumattaJatta-t8y
    @FatoumattaJatta-t8y 3 หลายเดือนก่อน

    Masa😭😭😭😭😭yanala yalla diapalee sibarkeh seydina mouhamet salalahou aleykhi wàsalam🙏🙏🙏🙏😩😩

  • @NdeyeDieng-w7b
    @NdeyeDieng-w7b 4 หลายเดือนก่อน +18

    Sama bopou momala gueneul dou bagne nala yawmiy diapalé malade yi so wéroul do meuna dimbalé svp defal linela wakh nénanela guénél malade yi nek sa keur pour ton bien doula téré continue sa liguey sama khalate bou gate metite yingay dound ni c trop dur je m’excuse ❤pour toi

  • @kenzangom4716
    @kenzangom4716 4 หลายเดือนก่อน

    Pape li ngay def ci Domou Adam yi yalla nala ko yalla fey boul tite dara❤❤❤❤❤❤

  • @cisse10
    @cisse10 4 หลายเดือนก่อน +7

    Pape kou guem yalla ngua yalla dala beugu koumou beugu lay tegu natou bou méti après natou bi yeup yalla dinala diokh banekh bo khamné yow sah moussoko khalat insha allah yalla nala yalla takhwou amine ya rabi 🤲

    • @diopablaye6533
      @diopablaye6533 4 หลายเดือนก่อน +2

      Ces vrais dafaye khole fane la guememe tolou sante rék yalla bakh na

    • @cisse10
      @cisse10 4 หลายเดือนก่อน +1

      ​@@diopablaye6533 c vrai yalla def niouy testé soufeké ame naniou imane pour nangue ndoguolam pape mome dina ame kheweul boubah insha allah

  • @albassvp5hy
    @albassvp5hy 4 หลายเดือนก่อน

    yalla nala yalla takhawou ci barkep Serigne Touba 🤲🤲❤😢

  • @diakhatefatiss4162
    @diakhatefatiss4162 4 หลายเดือนก่อน +71

    Pape Nit Nioye dimbali motakh Seni andandoyi Nioladoul bayi limawakh bayisi khele

    • @AmétogoDiop
      @AmétogoDiop 4 หลายเดือนก่อน +8

      Lou lér nga wax mais yalla nako yalla sam

    • @KarimouBionka
      @KarimouBionka 4 หลายเดือนก่อน +2

      Ahhh metina trop

    • @CheikhsadbouAidara-ck3vu
      @CheikhsadbouAidara-ck3vu 4 หลายเดือนก่อน +2

      Bilahi walahi DEUG bou wer

    • @AissataBah-ih1kp
      @AissataBah-ih1kp 4 หลายเดือนก่อน +2

      C'est fort possible 🙏

    • @diakhatefatiss4162
      @diakhatefatiss4162 4 หลายเดือนก่อน +1

      @@AmétogoDiop amine yarabi

  • @amsarassoulndiaye3496
    @amsarassoulndiaye3496 4 หลายเดือนก่อน

    Pape niang yalla nala yalla takhawou inchallah ❤🙏🙏

  • @AwaSow-d6q
    @AwaSow-d6q 4 หลายเดือนก่อน +11

    Bilahi wolahi pape nitou deugu la tee nitou yalla la machallah yalla nala yalla diapalé si barké Seydina Mouhamed saw psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ svp Monsieur le Président il faut aidé pape et les autres qui ont besoin d'aide svp😢❤❤❤❤❤❤

  • @BabacarNDIAYE-pr3zn
    @BabacarNDIAYE-pr3zn 4 หลายเดือนก่อน

    Yallna ga amm werrr bou bakh wayyyy❤❤❤ yallna yalla fayy la sa kholll❤❤❤metina mai yalla ba akh❤❤❤

  • @boromkourousstv5139
    @boromkourousstv5139 4 หลายเดือนก่อน +28

    Guéne bayi khél. Pape. Yéne say souguéni dém féne Day lath takhaway nakh gni gnak khél gniguéni takhawou Day am lougnou andall souguéne pâre gnou diokhé sougnou mane mane nakh yala amna loumougnou sedé déléne defarou bala guéna dém si kou gnak khél

    • @AntaLo-nx1ur
      @AntaLo-nx1ur 4 หลายเดือนก่อน +2

      Eskeuy halatt bi dé lassi am mzn itam

    • @khadijianimaga1030
      @khadijianimaga1030 4 หลายเดือนก่อน +1

      Surrrr😢😢😢

    • @fatouba2560
      @fatouba2560 4 หลายเดือนก่อน +4

      Pape seytane meun nala top dei del mouslou di diang lakad diakoum lou bariii

    • @mariamandoye3287
      @mariamandoye3287 4 หลายเดือนก่อน +1

      C. Vrai je penser à ça 😢

  • @BayeModouSall-u9h
    @BayeModouSall-u9h 4 หลายเดือนก่อน +1

    Yalnaniou yalla dfal diamu ❤🙏🏾

  • @AidaRassoul-mw3hr
    @AidaRassoul-mw3hr 4 หลายเดือนก่อน +7

    Ndeysaan Yalna ALLAH samedu la thi barkép SEYDINA MOUHAMED SALALAHOU HALEYHI WASALAMm

  • @famacamara1767
    @famacamara1767 4 หลายเดือนก่อน

    Allahou Akbar lila topou yalla moko eupe dolé. Mouneugnou leu dara inchallah. qu'Allah t'assiste inch'Allah.

  • @AissatouDiallo-ko7jv
    @AissatouDiallo-ko7jv 4 หลายเดือนก่อน +9

    Amouma khalis waayé amna borom koun fayakounou yarambi 🙏 Yalla nala same arrla si barké seydina Mohamed

  • @ndoumbemboup-u8c
    @ndoumbemboup-u8c หลายเดือนก่อน

    Yalnaleu yalla takhawou dara waroula dal🤲🤲

  • @Kheuch703
    @Kheuch703 4 หลายเดือนก่อน +11

    Comme il fait du social, c'est un devoir pour l'état de le prendre en charge,si cela demande une évacuation à l'étranger,il faut le faire

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 4 หลายเดือนก่อน

    Nokk nokk yii yalla naloko yalla teguil thi diama thi barke serigne babacar sy amine yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne

  • @AramesarrNiang
    @AramesarrNiang 4 หลายเดือนก่อน +16

    Ndaysan yalnako yalla safara mais pape togal banga wer ngir yalla limetina trop bilay

    • @gtheboss9635
      @gtheboss9635 4 หลายเดือนก่อน

      S'il pouvait il l ferai
      Yaakar mo fooort rk

  • @ndyebinta-qz2xe
    @ndyebinta-qz2xe 4 หลายเดือนก่อน +1

    Thieuy natou mais sante yallaa rék pape nieng mast li métina trop djiougué si li daleu si léé wayé sanetaleu yallaa pape ame yaguikoy nétali rék alhamdoulilah ♥️🤲🙏 yallaa nallaa yallaa may kholou mougne si Daradjieuy Seuydina Mohamed PSL Amine 🤲🙏

  • @iboudia1049
    @iboudia1049 4 หลายเดือนก่อน +3

    Yalla nala yalla tahawou ❤

  • @ModouSeck-z7b
    @ModouSeck-z7b 4 หลายเดือนก่อน +1

    Lii metti na doyna waar yalna yallah sounou borom takhawou si barkeb alkhourane 🤲🏽🤲🏽 yeukati la bangay dokhi waat say yitté