- 270
- 3 954 966
Lamb Senegal🇸🇳
เข้าร่วมเมื่อ 6 พ.ย. 2018
Abbone vous ici y’a que du lamb senegal notre fierté 🇸🇳✌️
XAM SA MBEUR EPISODE 1 LA CARRIÈRE DE BALLA GAYE 2 LE LION DE GUEDIAWAY
Balla Gaye 2 est le nom d'arène d'Omar Sakho également surnommé « le lion de Guediawaye »,, champion de lutte sénégalaise. C'est le chef de file de l'écurie « École de lutte Balla Gaye ». Il a été « Roi des arènes » de la lutte sénégalaise de 2012 à 2014
Omar Sakho est né le 4 décembre 1986[réf. nécessaire] à Guédiawaye.
Le père de Balla Gaye 2, Double Less, de son vrai nom Mamadou Sakho, a lui-même régné pendant longtemps sur les arènes sénégalaises.
Carrière
23 victoires, 6 défaites, en 29 combats.
23 victoires : Samba Laobe, Dame Kandji, Papa Sow, Boulon, Mame Goor Diouf, Saloum Saloum, Bathie Seras, Boy Sèye, Coly Faye, Ousmane Diop, Issa Pouye, Mbaye Diouf, Tyson Jr, Moustapha Guèye, Modou Lo, Balla Bèye 2, Tyson, Yekini, Tapha Tine, Gris Bordeaux, Modou Lo, Gris Bordeau, Tapha Tine,
6 défaites : Eumeu Sène (deux fois), Bombardier (deux fois), Issa Pouye, Boy niang 2
4 années blanches 2015-2016, 2016-2017, 2018-2019, 2019-2020,
#lutte #luttesénégalaise #ballagaye2 #luttesenegalaise #luttetv #lutte_avec_frappe #sports #221 #africa #boyniang #modoulo
@GastonProductions_
@AlbourakhEventsTV
@LutteTV
@BantambaTV
@bprodmediatv
@kewelinfo7722

มุมมอง: 628
วีดีโอ
Les deux meilleurs combat de la lutte sénégalaise kou d’accord 😌
มุมมอง 405วันที่ผ่านมา
Les deux meilleurs combat de la lutte sénégalaise kou d’accord 😌
Un débat très important sur le cas de zambala anaconda lamb takhawna baye ndiaye et fadam2 lep lerna
มุมมอง 15Kวันที่ผ่านมา
Un débat très important sur le cas de zambala anaconda lamb takhawna baye ndiaye et fadam2 lep lerna
Modou lo ak tapha tine lambelogue wakhna lepp modou lo dako ragual balla gaye
มุมมอง 708วันที่ผ่านมา
Modou lo ak tapha tine lambelogue wakhna lepp modou lo dako ragual balla gaye
Fadam2 parle balla gaye modou takhawna par et boy niang2 ak reug siteu😱
มุมมอง 11Kวันที่ผ่านมา
Fadam2 parle balla gaye modou takhawna par et boy niang2 ak reug siteu😱
Les temps fort du combat mor kang et diop2 khekh bou metti sakh quel combat techniques
มุมมอง 1.3Kวันที่ผ่านมา
Les temps fort du combat mor kang et diop2 khekh bou metti sakh quel combat techniques
Première sortie de tapha tine modou lo dou sama rois balla gaye dama liguey et fadam2…
มุมมอง 11K2 วันที่ผ่านมา
Première sortie de tapha tine modou lo dou sama rois balla gaye dama liguey et fadam2…
Amanekh merna deh menace douada fall #ballagaye2 #lutte #luttetv #luttesénégalaise #luttesenegalaise
มุมมอง 1.3K14 วันที่ผ่านมา
Amanekh merna deh menace douada fall #ballagaye2 #lutte #luttetv #luttesénégalaise #luttesenegalaise
Walay thiate la farar mis danou na
Gnari ponkal li do siflé wat jél day léér gnah la
Amanekh tekk na épaule bou yaague
Thiat mo dane
Snap 😂😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Guemeul sa bop iow guay doull ni rek
Premier défaite Modou Anta
Amanekh seul
Arbitre yi mm avec varr saxx daniouy niaff senn ndy do wowatt gni niou beuré tmt
Boy yii ama gougne dolè koune guiss yaakaarnè niola euppou dolè
Ndiakh ndiakh dafa wara lère bëré waat rék
Courage
Li es que dou niakhe léroul dara ci mane
Pourtant Amanekh mo ndiéka tek épaule
Arbitre yi danio warone sifflé wate
Beure waat rk mosi waroon lamb day leer
Fii arbutre yi dagnou dioume . Fi ndiakhe mon fi ame guayi dagnou warrone beyrré watte .
Thiatou Deukk bi 💛💙
Li Dara lèrou si
Aye ndy Sathieu lagn rk li diakh la 😢
Aye ndy Sathieu lagn rk li diakh la 😢
Rio ⚔️⚔️🟨🟦
😂😂😂😂😂
Amanekh mo dane diél bou reuy 😂
Mais yenn guiss ngen kanamou balla gaye😂😂😂
Cv
Ama nékh mo ndieukeu daanou
Soyons objectifs waay daanou neu.
Arbitre yi lan lini lathé la beuge kham😂
❤❤
Bravo
Niakh lah
Thiiatou Daouda fall mo dane deh Epaulou Ama nekh
Daouda mo djitu
Épaule Amanekh mo djitou
Lii ndiakh la
Li dano warona beuré wate
Moussa ndoy modou anta thies
Amanekh mo dane.
Bayilén bougén farà di dof dof Lou bopou boye bi la amanékh la beusse mou lale souf
Libmoy dakka beurei 😂
Mais arbitre mo yagg lamb ji li ndiakh la loudoy nè grand combat VAR am tè dielebi lèroul
Mbak bi mo dieuga lal souss après bopou bi
Ndiakh amoul dé thiatou Daouda mo def action mo dane
Fii ndiakh amoufi wy dafa lére
Sérieux amanekh mo daneee
Deim leinn toggui ki Amanékh daka dane dangueina farr rek
Dafa nekk jeune nekk si yonn ken beugoul mou danou mais nieup xamnen ni Thiatou daouda fall mo danou
Thiate bop b mo njeuk danuna
Ohhhh temps yii la fondé alias Gris bordeaux nékone si forme bilahi mes légui fondé deug leu .ak rouye alias balla gaye 2 dit simba légui dagno yakou deug way 😅😅😅😅mes eumeu sène..modou lo ..lac de guerre...tapha tine toujours en état
Bayilène nék aye nafékh thiate dafa danou diéle bou lér bopou bi mo lale souf en premier
Iow Bayil di wakh Lou amoul et visionne bien l’épaule de amanekh
Hana saye beute dafa flou amanékh bou téguone épaule digua dégu wa guèdiawaye niou wakh sii ..thiate bopou bi mo lale lolou moko dane amanékh avant bras bi la door entre temps thiate sila bopou bi sogua gnew voila diéle bou lérr koussi wérénté tamitt dagua farre bamou eupe rék soyons sportif .. lamine golo mi guenone diégué bi lamb djiii diékhé déguoko fén mounila amanékh dafa ték épaule parce que après bimou holaté hamenii boy bi danou na voila wa salam bonne journée 🙏
@@AboubacryGASSAMA-zs7oi❤❤❤thanks bro rien n’a dire honnêtement Lébou Gui dafa gnor dh
Balla gaye motah Modou nékeu roi des arènes
Ama késs❤❤❤